Al-Qari'a · 7/11
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qari'a
فَهُوَ فِي عِيشَةٍ رَّاضِيَةٍ ۝٧
Fahuwa fee `ishatir raadiyah
📖 Tekkim Wolof
ma nga ko ca dundu gu neex ;

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 5-9 — Simoore Al-Qari'a

5وَتَكُونُ الْجِبَالُ كَالْعِهْنِ الْمَنفُوشِ
te tund doj yi it mujj mel ni ngëndal nooy nepp ;
6فَأَمَّا مَن ثَقُلَتْ مَوَازِينُهُ
képp ku peeseem diis (ci yiw)
7فَهُوَ فِي عِيشَةٍ رَّاضِيَةٍ
ma nga ko ca dundu gu neex ;
8وَأَمَّا مَنْ خَفَّتْ مَوَازِينُهُ
képp ku peeseem wayaf (ci yiw),
9فَأُمُّهُ هَاوِيَةٌ
ma ngay jëm Haawiyatu.
Al-Qari'aFihi Alxuraan
11Aaya
MeccanRevelation
7Aaya

Tekki — Al-Qari'a 7

Simoore Al-Qari'a Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ma nga ko ca dundu gu neex ;

Simoore Aaya 7/11 — Simoore Al-Qari'a القارعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qari'a Dégg, Simoore Al-Qari'a Tekki, Simoore Al-Qari'a mp3, Simoore Al-Qari'a pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers