An-Nahl · 125/128
Tekki Waxtaan — An-Nahl
ادْعُ إِلَىٰ سَبِيلِ رَبِّكَ بِالْحِكْمَةِ وَالْمَوْعِظَةِ الْحَسَنَةِ ۖ وَجَادِلْهُم بِالَّتِي هِيَ أَحْسَنُ ۚ إِنَّ رَبَّكَ هُوَ أَعْلَمُ بِمَن ضَلَّ عَن سَبِيلِهِ ۖ وَهُوَ أَعْلَمُ بِالْمُهْتَدِينَ ١٢٥
Transliteration
Ud`u ilaa sabeeli Rabbika bilhikmati walmaw `izatil hasanati wa jaadilhum billatee hiya ahsan; inna Rabbaka huwa a`almu biman dalla `an sabeelihee wa Huwa a`lamu bilmuhtadeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Wooteel ci sa yoonu Boroom [Lislaam], sukkandiku ci Alxuraan ak waare ci lu baax. Nanga dàggasanteek ñoom ca na mu gën a rafete. Naka sa Boroom moo gën a xam ña réer, sori aw yoonam te Moom moo gën a xam ñu jub ña.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 123-127 — An-Nahl
123ثُمَّ أَوْحَيْنَا إِلَيْكَ أَنِ اتَّبِعْ مِلَّةَ إِبْرَاهِيمَ حَنِيفًا ۖ وَمَا كَانَ مِنَ الْمُشْرِكِينَ
Tax na Nu soloo la ne : “Toppal diiney Ibraahiima [yaw Muhammad] cig wéetal sa Boroom, bokkul woon ca bokkaalekat ya”.
124إِنَّمَا جُعِلَ السَّبْتُ عَلَى الَّذِينَ اخْتَلَفُوا فِيهِ ۚ وَإِنَّ رَبَّكَ لَيَحْكُمُ بَيْنَهُمْ يَوْمَ الْقِيَامَةِ فِيمَا كَانُوا فِيهِ يَخْتَلِفُونَ
Màggal bisu gaawu tegewul woon lu dul ca kaw ña ca juuyoo woon. Te sa Boroom dana àtte seen diggante ca Bis-pénc ba ca la ñu nekkoon di ca juuyoo.
125ادْعُ إِلَىٰ سَبِيلِ رَبِّكَ بِالْحِكْمَةِ وَالْمَوْعِظَةِ الْحَسَنَةِ ۖ وَجَادِلْهُم بِالَّتِي هِيَ أَحْسَنُ ۚ إِنَّ رَبَّكَ هُوَ أَعْلَمُ بِمَن ضَلَّ عَن سَبِيلِهِ ۖ وَهُوَ أَعْلَمُ بِالْمُهْتَدِينَ
Wooteel ci sa yoonu Boroom [Lislaam], sukkandiku ci Alxuraan ak waare ci lu baax. Nanga dàggasanteek ñoom ca na mu gën a rafete. Naka sa Boroom moo gën a xam ña réer, sori aw yoonam te Moom moo gën a xam ñu jub ña.
126وَإِنْ عَاقَبْتُمْ فَعَاقِبُوا بِمِثْلِ مَا عُوقِبْتُم بِهِ ۖ وَلَئِن صَبَرْتُمْ لَهُوَ خَيْرٌ لِّلصَّابِرِينَ
Nangeen feye ña leen mbugal, lu tollu ni la ñu leen mbugale. Waaye bu ngeen mënee [bañ a feyu]... moo gën ci ñay muñ.
127وَاصْبِرْ وَمَا صَبْرُكَ إِلَّا بِاللَّهِ ۚ وَلَا تَحْزَنْ عَلَيْهِمْ وَلَا تَكُ فِي ضَيْقٍ مِّمَّا يَمْكُرُونَ
Nangay muñ ! Te sag muñ bu mu wéeru fu dul ci Yàlla. Te bul jàq ngir ñoom. Te bul nekk ci tiis ngir la ñuy fexe.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
125Aaya
Tekki — An-Nahl 125
Simoore An-Nahl Aaya 125 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Wooteel ci sa yoonu Boroom [Lislaam], sukkandiku ci Alxuraan ak…Simoore Aaya 125/128 — An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nahl Dégg, An-Nahl Tekki, An-Nahl mp3, An-Nahl pdf. Aaya 123–127. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








