An-Nahl · 126/128
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nahl
وَإِنْ عَاقَبْتُمْ فَعَاقِبُوا بِمِثْلِ مَا عُوقِبْتُم بِهِ ۖ وَلَئِن صَبَرْتُمْ لَهُوَ خَيْرٌ لِّلصَّابِرِينَ ۝١٢٦
Wa in `aaqabtum fa`aaqiboo bimisli maa `ooqibtum bihee wa la`in sabartum lahuwa khairul lissaabireen
📖 Tekkim Wolof
Nangeen feye ña leen mbugal, lu tollu ni la ñu leen mbugale. Waaye bu ngeen mënee [bañ a feyu]... moo gën ci ñay muñ.

🎧 Dégg


📜 Aaya 124-128 — Simoore An-Nahl

124إِنَّمَا جُعِلَ السَّبْتُ عَلَى الَّذِينَ اخْتَلَفُوا فِيهِ ۚ وَإِنَّ رَبَّكَ لَيَحْكُمُ بَيْنَهُمْ يَوْمَ الْقِيَامَةِ فِيمَا كَانُوا فِيهِ يَخْتَلِفُونَ
Màggal bisu gaawu tegewul woon lu dul ca kaw ña ca juuyoo woon. Te sa Boroom dana àtte seen diggante ca Bis-pénc ba ca la ñu nekkoon di ca juuyoo.
125ادْعُ إِلَىٰ سَبِيلِ رَبِّكَ بِالْحِكْمَةِ وَالْمَوْعِظَةِ الْحَسَنَةِ ۖ وَجَادِلْهُم بِالَّتِي هِيَ أَحْسَنُ ۚ إِنَّ رَبَّكَ هُوَ أَعْلَمُ بِمَن ضَلَّ عَن سَبِيلِهِ ۖ وَهُوَ أَعْلَمُ بِالْمُهْتَدِينَ
Wooteel ci sa yoonu Boroom [Lislaam], sukkandiku ci Alxuraan ak waare ci lu baax. Nanga dàggasanteek ñoom ca na mu gën a rafete. Naka sa Boroom moo gën a xam ña réer, sori aw yoonam te Moom moo gën a xam ñu jub ña.
126وَإِنْ عَاقَبْتُمْ فَعَاقِبُوا بِمِثْلِ مَا عُوقِبْتُم بِهِ ۖ وَلَئِن صَبَرْتُمْ لَهُوَ خَيْرٌ لِّلصَّابِرِينَ
Nangeen feye ña leen mbugal, lu tollu ni la ñu leen mbugale. Waaye bu ngeen mënee [bañ a feyu]... moo gën ci ñay muñ.
127وَاصْبِرْ وَمَا صَبْرُكَ إِلَّا بِاللَّهِ ۚ وَلَا تَحْزَنْ عَلَيْهِمْ وَلَا تَكُ فِي ضَيْقٍ مِّمَّا يَمْكُرُونَ
Nangay muñ ! Te sag muñ bu mu wéeru fu dul ci Yàlla. Te bul jàq ngir ñoom. Te bul nekk ci tiis ngir la ñuy fexe.
128إِنَّ اللَّهَ مَعَ الَّذِينَ اتَّقَوا وَّالَّذِينَ هُم مُّحْسِنُونَ
Yàlla nag, ñay rafetal te ragal Ko la àndal de.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
126Aaya

Tekki — An-Nahl 126

Simoore An-Nahl Aaya 126 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nangeen feye ña leen mbugal, lu tollu ni la ñu…

Simoore Aaya 126/128 — Simoore An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nahl Dégg, Simoore An-Nahl Tekki, Simoore An-Nahl mp3, Simoore An-Nahl pdf. Aaya 124–128. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers