An-Nur · 30/64
Tekki Waxtaan — An-Nur
قُل لِّلْمُؤْمِنِينَ يَغُضُّوا مِنْ أَبْصَارِهِمْ وَيَحْفَظُوا فُرُوجَهُمْ ۚ ذَٰلِكَ أَزْكَىٰ لَهُمْ ۗ إِنَّ اللَّهَ خَبِيرٌ بِمَا يَصْنَعُونَ ٣٠
Transliteration
Qul lilmu` mineena yaghuuddoo min absaarihim wa yahfazoo furoojahum; zaalika azkaa lahum; innallaaha khabeerum bimaa yasna`oon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Neel war na ci way-gëm ñi ñuy sajj seenub gis tey sàmm seen pëy. Looloo gën a sell ci yéen. Te nag Yàlla ku deñ la kumpa ci li ngeen di def.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 28-32 — An-Nur
28فَإِن لَّمْ تَجِدُوا فِيهَا أَحَدًا فَلَا تَدْخُلُوهَا حَتَّىٰ يُؤْذَنَ لَكُمْ ۖ وَإِن قِيلَ لَكُمُ ارْجِعُوا فَارْجِعُوا ۖ هُوَ أَزْكَىٰ لَكُمْ ۚ وَاللَّهُ بِمَا تَعْمَلُونَ عَلِيمٌ
Bu ngeen ca fekkul kenn, buleen ca dugg li feek joxuñuleen ca ndigal. Te bu ñu la nee : “Dellul [damaa jàpp]”, dellul. Loolu moo gën a sell ci yéen. Yàlla aka xam li ngeen di def.
29لَّيْسَ عَلَيْكُمْ جُنَاحٌ أَن تَدْخُلُوا بُيُوتًا غَيْرَ مَسْكُونَةٍ فِيهَا مَتَاعٌ لَّكُمْ ۚ وَاللَّهُ يَعْلَمُ مَا تُبْدُونَ وَمَا تَكْتُمُونَ
[Waaye] bàkkaar amul ci yéen ngeen dugg ci kër gu ñu dëkkewul te seen tobarte nekk fa. Yàlla xam na li ngeen feeñal ak li ngeen di nëbb.
30قُل لِّلْمُؤْمِنِينَ يَغُضُّوا مِنْ أَبْصَارِهِمْ وَيَحْفَظُوا فُرُوجَهُمْ ۚ ذَٰلِكَ أَزْكَىٰ لَهُمْ ۗ إِنَّ اللَّهَ خَبِيرٌ بِمَا يَصْنَعُونَ
Neel war na ci way-gëm ñi ñuy sajj seenub gis tey sàmm seen pëy. Looloo gën a sell ci yéen. Te nag Yàlla ku deñ la kumpa ci li ngeen di def.
31وَقُل لِّلْمُؤْمِنَاتِ يَغْضُضْنَ مِنْ أَبْصَارِهِنَّ وَيَحْفَظْنَ فُرُوجَهُنَّ وَلَا يُبْدِينَ زِينَتَهُنَّ إِلَّا مَا ظَهَرَ مِنْهَا ۖ وَلْيَضْرِبْنَ بِخُمُرِهِنَّ عَلَىٰ جُيُوبِهِنَّ ۖ وَلَا يُبْدِينَ زِينَتَهُنَّ إِلَّا لِبُعُولَتِهِنَّ أَوْ آبَائِهِنَّ أَوْ آبَاءِ بُعُولَتِهِنَّ أَوْ أَبْنَائِهِنَّ أَوْ أَبْنَاءِ بُعُولَتِهِنَّ أَوْ إِخْوَانِهِنَّ أَوْ بَنِي إِخْوَانِهِنَّ أَوْ بَنِي أَخَوَاتِهِنَّ أَوْ نِسَائِهِنَّ أَوْ مَا مَلَكَتْ أَيْمَانُهُنَّ أَوِ التَّابِعِينَ غَيْرِ أُولِي الْإِرْبَةِ مِنَ الرِّجَالِ أَوِ الطِّفْلِ الَّذِينَ لَمْ يَظْهَرُوا عَلَىٰ عَوْرَاتِ النِّسَاءِ ۖ وَلَا يَضْرِبْنَ بِأَرْجُلِهِنَّ لِيُعْلَمَ مَا يُخْفِينَ مِن زِينَتِهِنَّ ۚ وَتُوبُوا إِلَى اللَّهِ جَمِيعًا أَيُّهَ الْمُؤْمِنُونَ لَعَلَّكُمْ تُفْلِحُونَ
Waxal jullit ñu jigéen ñi ne leen : nañuy sajj seenub gis, nañuy sàmm seen pëy, te nañuy bañ a feeñal seenub taar lu dul li ca feeñ, nañuy sàng [muur] seeni yaram ; te buñu feeñalal seenub taar ku dul seen jëkkër, walla seen baay, walla seen baayi jëkkër, walla seen doom, walla seen doomi jëkkër, walla seen càmmiñ, walla seen doomi càmmiñ, walla seen dommi jigéen, walla seen tàpp, walla xaleel yu géwantagul. Te it nañuy bañ a dóor seeni tànk ngir di feeñal li làqu ca seenub taar. Tuub-leen yéen ñépp jëm ci Yàlla yéen ña di way-gëm ndaxtelee ngeen texe.
32وَأَنكِحُوا الْأَيَامَىٰ مِنكُمْ وَالصَّالِحِينَ مِنْ عِبَادِكُمْ وَإِمَائِكُمْ ۚ إِن يَكُونُوا فُقَرَاءَ يُغْنِهِمُ اللَّهُ مِن فَضْلِهِ ۗ وَاللَّهُ وَاسِعٌ عَلِيمٌ
Takk-leen [jabar/jëkkër] ci ña séyul ak ca ña yiw te bokk ci seeni jaam [góor, jigéen]. Su fekkee dañoo ndóol, Yàlla Dana leen woomalal ci ngënéelam. Yàlla ku yaatu la, Ku xam la.
An-NurFihi Alxuraan
64Aaya
MedinanRevelation
30Aaya
Tekki — An-Nur 30
Simoore An-Nur Aaya 30 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel war na ci way-gëm ñi ñuy sajj seenub gis…Simoore Aaya 30/64 — An-Nur النور (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nur Dégg, An-Nur Tekki, An-Nur mp3, An-Nur pdf. Aaya 28–32. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








