An-Nur · 37/64
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nur
رِجَالٌ لَّا تُلْهِيهِمْ تِجَارَةٌ وَلَا بَيْعٌ عَن ذِكْرِ اللَّهِ وَإِقَامِ الصَّلَاةِ وَإِيتَاءِ الزَّكَاةِ ۙ يَخَافُونَ يَوْمًا تَتَقَلَّبُ فِيهِ الْقُلُوبُ وَالْأَبْصَارُ ٣٧
Transliteration
Rinjaalul laa tulheehim tijaaratunw wa laa bai`un `an zikril laahi wa iqaamis Salaati wa eetaaa`iz Zakaati yakkhaafoona Yawman tataqallabu feehil quloobu wal absaar
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
aw gaay ñoo xam ne njulaakum njaay duleen mës a fàbbi ci tudd Yàlla ak a taxawal julli, ak génne asaka, ngir ñoom kat dañoo ragal Bis ba xol ya di wëlbëtiku ak gët ya.
Additional reference in Fulfulde
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
0:00
0:00
📜 Aaya 35-39 — Simoore An-Nur
35۞ اللَّهُ نُورُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۚ مَثَلُ نُورِهِ كَمِشْكَاةٍ فِيهَا مِصْبَاحٌ ۖ الْمِصْبَاحُ فِي زُجَاجَةٍ ۖ الزُّجَاجَةُ كَأَنَّهَا كَوْكَبٌ دُرِّيٌّ يُوقَدُ مِن شَجَرَةٍ مُّبَارَكَةٍ زَيْتُونَةٍ لَّا شَرْقِيَّةٍ وَلَا غَرْبِيَّةٍ يَكَادُ زَيْتُهَا يُضِيءُ وَلَوْ لَمْ تَمْسَسْهُ نَارٌ ۚ نُّورٌ عَلَىٰ نُورٍ ۗ يَهْدِي اللَّهُ لِنُورِهِ مَن يَشَاءُ ۚ وَيَضْرِبُ اللَّهُ الْأَمْثَالَ لِلنَّاسِ ۗ وَاللَّهُ بِكُلِّ شَيْءٍ عَلِيمٌ
Yàllaay leerug asamaan yeek suuf si. Te leeram googu dafa mel ni ab cëgg bu ami làmp ci biiram. Làmp boobu nekkaat ci ab weer, weer boobu mel ni bidiw buy nes-nesi ; ñu di ko taalee ci diwub garabug oliw gu tedd [gu wuuteeg yi ñu miin]. Diwam ga xaw naa mën a leeral te safara laalu ko. Te Yàlla dana saddal nit ñi ay leebu te Yàlla xam na lu ne.
36فِي بُيُوتٍ أَذِنَ اللَّهُ أَن تُرْفَعَ وَيُذْكَرَ فِيهَا اسْمُهُ يُسَبِّحُ لَهُ فِيهَا بِالْغُدُوِّ وَالْآصَالِ
Ci biiri kër [jàkka] yoo xam ne Yàlla digle ñu di fa tudd aw Turam, di Ko yékkati ; di Ko ca sàbbaal suba ak ngoon,
37رِجَالٌ لَّا تُلْهِيهِمْ تِجَارَةٌ وَلَا بَيْعٌ عَن ذِكْرِ اللَّهِ وَإِقَامِ الصَّلَاةِ وَإِيتَاءِ الزَّكَاةِ ۙ يَخَافُونَ يَوْمًا تَتَقَلَّبُ فِيهِ الْقُلُوبُ وَالْأَبْصَارُ
aw gaay ñoo xam ne njulaakum njaay duleen mës a fàbbi ci tudd Yàlla ak a taxawal julli, ak génne asaka, ngir ñoom kat dañoo ragal Bis ba xol ya di wëlbëtiku ak gët ya.
38لِيَجْزِيَهُمُ اللَّهُ أَحْسَنَ مَا عَمِلُوا وَيَزِيدَهُم مِّن فَضْلِهِ ۗ وَاللَّهُ يَرْزُقُ مَن يَشَاءُ بِغَيْرِ حِسَابٍ
[Ci loolu], Yàlla dana leen feye la gën a rafet ca la ñu jëf. Dana leen dolli ngëneel. Te Yàlla dana wërsëgal ku ko soob ci lu àndul ak ug waññi [lijjanti].
39وَالَّذِينَ كَفَرُوا أَعْمَالُهُمْ كَسَرَابٍ بِقِيعَةٍ يَحْسَبُهُ الظَّمْآنُ مَاءً حَتَّىٰ إِذَا جَاءَهُ لَمْ يَجِدْهُ شَيْئًا وَوَجَدَ اللَّهَ عِندَهُ فَوَفَّاهُ حِسَابَهُ ۗ وَاللَّهُ سَرِيعُ الْحِسَابِ
Ña weddi, di ay jéefar, ñoom seeni jëf dafa mel ni ñàndóox, bu ko boroomu mar séenee, dakoy jàppe ndox. Saa bu fa agsee, du fa fekk tus ; Yàlla rekk la fay fekk Mu waññal ko ay jëfam ba mu mat sëkk, te moo ne Yàllaa ka gaaw ab lijjanti.
An-NurFihi Alxuraan
64Aaya
MedinanRevelation
37Aaya
Tekki — An-Nur 37
Simoore An-Nur Aaya 37 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : aw gaay ñoo xam ne njulaakum njaay duleen mës a…Simoore Aaya 37/64 — Simoore An-Nur النور (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nur Dégg, Simoore An-Nur Tekki, Simoore An-Nur mp3, Simoore An-Nur pdf. Aaya 35–39. Tekkim Wolof: Fulfulde.
Simoore An-Nur
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Friday, October 2, 2026
Don't forget us in your sincere prayers


