An-Nur · 36/64
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nur
فِي بُيُوتٍ أَذِنَ اللَّهُ أَن تُرْفَعَ وَيُذْكَرَ فِيهَا اسْمُهُ يُسَبِّحُ لَهُ فِيهَا بِالْغُدُوِّ وَالْآصَالِ ۝٣٦
Fee buyootin azinal laahu an turfa`a wa yuzkara feehasmuhoo yusabbihu lahoo feehaa bilghuduwwi wal aasaal
📖 Tekkim Wolof
Ci biiri kër [jàkka] yoo xam ne Yàlla digle ñu di fa tudd aw Turam, di Ko yékkati ; di Ko ca sàbbaal suba ak ngoon,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 34-38 — Simoore An-Nur

34وَلَقَدْ أَنزَلْنَا إِلَيْكُمْ آيَاتٍ مُّبَيِّنَاتٍ وَمَثَلًا مِّنَ الَّذِينَ خَلَوْا مِن قَبْلِكُمْ وَمَوْعِظَةً لِّلْمُتَّقِينَ
Wàcce Nanu ci yéen ay laaya yu Nu faramfàcce, di ay misaal yu bawoo ca ña leen jiitu woon, di ag waare ci ña ragal Yàlla !
35۞ اللَّهُ نُورُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۚ مَثَلُ نُورِهِ كَمِشْكَاةٍ فِيهَا مِصْبَاحٌ ۖ الْمِصْبَاحُ فِي زُجَاجَةٍ ۖ الزُّجَاجَةُ كَأَنَّهَا كَوْكَبٌ دُرِّيٌّ يُوقَدُ مِن شَجَرَةٍ مُّبَارَكَةٍ زَيْتُونَةٍ لَّا شَرْقِيَّةٍ وَلَا غَرْبِيَّةٍ يَكَادُ زَيْتُهَا يُضِيءُ وَلَوْ لَمْ تَمْسَسْهُ نَارٌ ۚ نُّورٌ عَلَىٰ نُورٍ ۗ يَهْدِي اللَّهُ لِنُورِهِ مَن يَشَاءُ ۚ وَيَضْرِبُ اللَّهُ الْأَمْثَالَ لِلنَّاسِ ۗ وَاللَّهُ بِكُلِّ شَيْءٍ عَلِيمٌ
Yàllaay leerug asamaan yeek suuf si. Te leeram googu dafa mel ni ab cëgg bu ami làmp ci biiram. Làmp boobu nekkaat ci ab weer, weer boobu mel ni bidiw buy nes-nesi ; ñu di ko taalee ci diwub garabug oliw gu tedd [gu wuuteeg yi ñu miin]. Diwam ga xaw naa mën a leeral te safara laalu ko. Te Yàlla dana saddal nit ñi ay leebu te Yàlla xam na lu ne.
36فِي بُيُوتٍ أَذِنَ اللَّهُ أَن تُرْفَعَ وَيُذْكَرَ فِيهَا اسْمُهُ يُسَبِّحُ لَهُ فِيهَا بِالْغُدُوِّ وَالْآصَالِ
Ci biiri kër [jàkka] yoo xam ne Yàlla digle ñu di fa tudd aw Turam, di Ko yékkati ; di Ko ca sàbbaal suba ak ngoon,
37رِجَالٌ لَّا تُلْهِيهِمْ تِجَارَةٌ وَلَا بَيْعٌ عَن ذِكْرِ اللَّهِ وَإِقَامِ الصَّلَاةِ وَإِيتَاءِ الزَّكَاةِ ۙ يَخَافُونَ يَوْمًا تَتَقَلَّبُ فِيهِ الْقُلُوبُ وَالْأَبْصَارُ
aw gaay ñoo xam ne njulaakum njaay duleen mës a fàbbi ci tudd Yàlla ak a taxawal julli, ak génne asaka, ngir ñoom kat dañoo ragal Bis ba xol ya di wëlbëtiku ak gët ya.
38لِيَجْزِيَهُمُ اللَّهُ أَحْسَنَ مَا عَمِلُوا وَيَزِيدَهُم مِّن فَضْلِهِ ۗ وَاللَّهُ يَرْزُقُ مَن يَشَاءُ بِغَيْرِ حِسَابٍ
[Ci loolu], Yàlla dana leen feye la gën a rafet ca la ñu jëf. Dana leen dolli ngëneel. Te Yàlla dana wërsëgal ku ko soob ci lu àndul ak ug waññi [lijjanti].
An-NurFihi Alxuraan
64Aaya
MedinanRevelation
36Aaya

Tekki — An-Nur 36

Simoore An-Nur Aaya 36 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ci biiri kër [jàkka] yoo xam ne Yàlla digle ñu…

Simoore Aaya 36/64 — Simoore An-Nur النور (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nur Dégg, Simoore An-Nur Tekki, Simoore An-Nur mp3, Simoore An-Nur pdf. Aaya 34–38. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers