Aali Imran · 200/200
Tekki Waxtaan — Simoore Aali Imran
يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا اصْبِرُوا وَصَابِرُوا وَرَابِطُوا وَاتَّقُوا اللَّهَ لَعَلَّكُمْ تُفْلِحُونَ ۝٢٠٠
Yaaa aiyuhal lazeena aamanus biroo wa saabiroo wa raabitoo wattaqul laaha la`allakum tuflihoon
📖 Tekkim Wolof
Éy yéen ñi gëm ! Nangeen di muñ ci bànneex, nangeen di muñ it [ci aw naqar]. Te itam nangeen di fagaru, te itam ragal-leen Yàlla ndax Yàlla ngeen texe !

🎧 Dégg


📜 Aaya 198-200 — Simoore Aali Imran

198لَٰكِنِ الَّذِينَ اتَّقَوْا رَبَّهُمْ لَهُمْ جَنَّاتٌ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ خَالِدِينَ فِيهَا نُزُلًا مِّنْ عِندِ اللَّهِ ۗ وَمَا عِندَ اللَّهِ خَيْرٌ لِّلْأَبْرَارِ
Waaye ña ragal seen Boroom, am nañu Àjjana joo xam ne dex yaa ngay daw ca seen ron, ñu béel fa, muy seen wàccuwaay fa Yàlla. Te la nekk fa Yàlla mooy dàqal ñu baax ña.
199وَإِنَّ مِنْ أَهْلِ الْكِتَابِ لَمَن يُؤْمِنُ بِاللَّهِ وَمَا أُنزِلَ إِلَيْكُمْ وَمَا أُنزِلَ إِلَيْهِمْ خَاشِعِينَ لِلَّهِ لَا يَشْتَرُونَ بِآيَاتِ اللَّهِ ثَمَنًا قَلِيلًا ۗ أُولَٰئِكَ لَهُمْ أَجْرُهُمْ عِندَ رَبِّهِمْ ۗ إِنَّ اللَّهَ سَرِيعُ الْحِسَابِ
Am na ci ña jot Téere, ñu gëm Yàlla ak la ñu wàcce ci yéen, ak la ñu wàcce ca ñoom. Dañuy toroxlul Yàlla, duñu jaay laayay Yàlla ci njëg gu néew. Ñooña am nañu seenug pey fa Yàlla te Yàlla ku gaaw la ci waññ [jëfi nit ñi].
200يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا اصْبِرُوا وَصَابِرُوا وَرَابِطُوا وَاتَّقُوا اللَّهَ لَعَلَّكُمْ تُفْلِحُونَ
Éy yéen ñi gëm ! Nangeen di muñ ci bànneex, nangeen di muñ it [ci aw naqar]. Te itam nangeen di fagaru, te itam ragal-leen Yàlla ndax Yàlla ngeen texe !
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
200Aaya

Tekki — Aali Imran 200

Simoore Aali Imran Aaya 200 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Éy yéen ñi gëm ! Nangeen di muñ ci bànneex,…

Simoore Aaya 200/200 — Simoore Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Aali Imran Dégg, Simoore Aali Imran Tekki, Simoore Aali Imran mp3, Simoore Aali Imran pdf. Aaya 198–200. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers