Ghafir · 1/85
Tekki Waxtaan — Simoore Ghafir
حم ۝١
Haa-Meeem
📖 Tekkim Wolof
Haa, Miim.

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-3 — Simoore Ghafir

1حم
Haa, Miim.
2تَنزِيلُ الْكِتَابِ مِنَ اللَّهِ الْعَزِيزِ الْعَلِيمِ
Wàcceg téere bii ma ngi bawoo ca Yàlla, miy boroom Kàttan, te di ku Xam.
3غَافِرِ الذَّنبِ وَقَابِلِ التَّوْبِ شَدِيدِ الْعِقَابِ ذِي الطَّوْلِ ۖ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ ۖ إِلَيْهِ الْمَصِيرُ
Mooy Jéggalkatu bàkkaar yi, di Nanguwaakoonu tuub, di ku Tar mbugël, mooy Boroom xéewal yi. Amul jeneen Yàlla judul Moom te ci Moom la lépp di mujj.
GhafirFihi Alxuraan
85Aaya
MeccanRevelation
1Aaya

Tekki — Ghafir 1

Simoore Ghafir Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Haa, Miim.

Simoore Aaya 1/85 — Simoore Ghafir غافر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ghafir Dégg, Simoore Ghafir Tekki, Simoore Ghafir mp3, Simoore Ghafir pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers