Ghafir · 2/85
Tekki Waxtaan — Simoore Ghafir
تَنزِيلُ الْكِتَابِ مِنَ اللَّهِ الْعَزِيزِ الْعَلِيمِ ٢
Transliteration
Tanzeelul Kitaabi minal laahil Azeezil `Aleem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Wàcceg téere bii ma ngi bawoo ca Yàlla, miy boroom Kàttan, te di ku Xam.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 1-4 — Simoore Ghafir
1حم
Haa, Miim.
2تَنزِيلُ الْكِتَابِ مِنَ اللَّهِ الْعَزِيزِ الْعَلِيمِ
Wàcceg téere bii ma ngi bawoo ca Yàlla, miy boroom Kàttan, te di ku Xam.
3غَافِرِ الذَّنبِ وَقَابِلِ التَّوْبِ شَدِيدِ الْعِقَابِ ذِي الطَّوْلِ ۖ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ ۖ إِلَيْهِ الْمَصِيرُ
Mooy Jéggalkatu bàkkaar yi, di Nanguwaakoonu tuub, di ku Tar mbugël, mooy Boroom xéewal yi. Amul jeneen Yàlla judul Moom te ci Moom la lépp di mujj.
4مَا يُجَادِلُ فِي آيَاتِ اللَّهِ إِلَّا الَّذِينَ كَفَرُوا فَلَا يَغْرُرْكَ تَقَلُّبُهُمْ فِي الْبِلَادِ
Kenn du dàggasante ci kàdduy Yàlla ku dul yéefar yi. bu la seeni feem nax.
GhafirFihi Alxuraan
85Aaya
MeccanRevelation
2Aaya
Tekki — Ghafir 2
Simoore Ghafir Aaya 2 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Wàcceg téere bii ma ngi bawoo ca Yàlla, miy boroom…Simoore Aaya 2/85 — Simoore Ghafir غافر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ghafir Dégg, Simoore Ghafir Tekki, Simoore Ghafir mp3, Simoore Ghafir pdf. Aaya 1–4. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Monday, September 7, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








