At-Tawba · 60/129
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tawba
۞ إِنَّمَا الصَّدَقَاتُ لِلْفُقَرَاءِ وَالْمَسَاكِينِ وَالْعَامِلِينَ عَلَيْهَا وَالْمُؤَلَّفَةِ قُلُوبُهُمْ وَفِي الرِّقَابِ وَالْغَارِمِينَ وَفِي سَبِيلِ اللَّهِ وَابْنِ السَّبِيلِ ۖ فَرِيضَةً مِّنَ اللَّهِ ۗ وَاللَّهُ عَلِيمٌ حَكِيمٌ ۝٦٠
Innamas sadaqaatu lilfuqaraaa`i walmasaakeeni wal `aamileena `alaihaa wal mu`al lafati quloobuhum wa fir riqaabi walghaarimeena wa fee sabeelil laahi wabnis sabeeli fareedatam minal laah; wal laahu `Aleemun Hakeem
📖 Tekkim Wolof
Asaka, ñi ko yeyoo ñooy ñi néew am-am, yalwaankat yi, ñi koy toppatoo, ñi ñu bëgg nooyal seen xol (ci Lislaam) ak ci goreel jaam, ña bor sonnal, ak ca lu jëm ci diiney Yàlla, ak doxandeem bu nekk ci tukki. Looloo di li Yàlla santaane ! Te Yàlla Ku xam la, Ku xereñ la.

🎧 Dégg


📜 Aaya 58-62 — Simoore At-Tawba

58وَمِنْهُم مَّن يَلْمِزُكَ فِي الصَّدَقَاتِ فَإِنْ أُعْطُوا مِنْهَا رَضُوا وَإِن لَّمْ يُعْطَوْا مِنْهَا إِذَا هُمْ يَسْخَطُونَ
Am na ci ñoom ñu la ayibal ci sarax yi : ku leen ca joxoon ñu bég ca ; ku leen joxul ñu xundu.
59وَلَوْ أَنَّهُمْ رَضُوا مَا آتَاهُمُ اللَّهُ وَرَسُولُهُ وَقَالُوا حَسْبُنَا اللَّهُ سَيُؤْتِينَا اللَّهُ مِن فَضْلِهِ وَرَسُولُهُ إِنَّا إِلَى اللَّهِ رَاغِبُونَ
Lu tee ñu bég ca la leen Yàlla ak Yonentam jox ? Tey wax : “Yàlla doy nanu. Yàlla Dana nu jox ci mbaaxam ak Yonentam it !... Nun way-xemmem lanu jëm ci Yàlla ”.
60۞ إِنَّمَا الصَّدَقَاتُ لِلْفُقَرَاءِ وَالْمَسَاكِينِ وَالْعَامِلِينَ عَلَيْهَا وَالْمُؤَلَّفَةِ قُلُوبُهُمْ وَفِي الرِّقَابِ وَالْغَارِمِينَ وَفِي سَبِيلِ اللَّهِ وَابْنِ السَّبِيلِ ۖ فَرِيضَةً مِّنَ اللَّهِ ۗ وَاللَّهُ عَلِيمٌ حَكِيمٌ
Asaka, ñi ko yeyoo ñooy ñi néew am-am, yalwaankat yi, ñi koy toppatoo, ñi ñu bëgg nooyal seen xol (ci Lislaam) ak ci goreel jaam, ña bor sonnal, ak ca lu jëm ci diiney Yàlla, ak doxandeem bu nekk ci tukki. Looloo di li Yàlla santaane ! Te Yàlla Ku xam la, Ku xereñ la.
61وَمِنْهُمُ الَّذِينَ يُؤْذُونَ النَّبِيَّ وَيَقُولُونَ هُوَ أُذُنٌ ۚ قُلْ أُذُنُ خَيْرٍ لَّكُمْ يُؤْمِنُ بِاللَّهِ وَيُؤْمِنُ لِلْمُؤْمِنِينَ وَرَحْمَةٌ لِّلَّذِينَ آمَنُوا مِنكُمْ ۚ وَالَّذِينَ يُؤْذُونَ رَسُولَ اللَّهِ لَهُمْ عَذَابٌ أَلِيمٌ
Am na ci ñoom ñuy lor Yonent bi, naan : “Benn nopp la”. - Neel : “Nopp bu yiw la ci yéen. Gëm na Yàlla te wóolu na way-gëm ña, te yërmaande la ci ñi gëm ci yéen. Te ñiy lor Yonentub Yàlla bi, mbugal mu metti ñeel na leen.
62يَحْلِفُونَ بِاللَّهِ لَكُمْ لِيُرْضُوكُمْ وَاللَّهُ وَرَسُولُهُ أَحَقُّ أَن يُرْضُوهُ إِن كَانُوا مُؤْمِنِينَ
Ña nga lay waatal ci Yàlla ngir am seen ngërëm. Te Yàlla ak Yonentam ñoo gën a yey ci ñoom sàkku seen ngërëm ndeem ñu gëm lañu.
At-TawbaFihi Alxuraan
129Aaya
MedinanRevelation
60Aaya

Tekki — At-Tawba 60

Simoore At-Tawba Aaya 60 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Asaka, ñi ko yeyoo ñooy ñi néew am-am, yalwaankat yi,…

Simoore Aaya 60/129 — Simoore At-Tawba التوبة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tawba Dégg, Simoore At-Tawba Tekki, Simoore At-Tawba mp3, Simoore At-Tawba pdf. Aaya 58–62. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers