Hud · 108/123
Tekki Waxtaan — Hud
۞ وَأَمَّا الَّذِينَ سُعِدُوا فَفِي الْجَنَّةِ خَالِدِينَ فِيهَا مَا دَامَتِ السَّمَاوَاتُ وَالْأَرْضُ إِلَّا مَا شَاءَ رَبُّكَ ۖ عَطَاءً غَيْرَ مَجْذُوذٍ ۝١٠٨
Wa ammal lazeena su`idoo fafil Jannati khaalideena feehaa maa daamatis samaawaatu wal ardu illaa maa shaaa`a Rabbuk; ataaa`an ghaira majzooz
📖 Tekkim Wolof
Ña texe, danañu nekk fa Àjjana, te dañu fay béel, nekk fa li feek asamaan yi ak suuf si ñi ngi fi - ndare lu neex sa Boroom - mu di ag may gu dul dog mukk.

🎧 Dégg


📜 Aaya 106-110 — Hud

106فَأَمَّا الَّذِينَ شَقُوا فَفِي النَّارِ لَهُمْ فِيهَا زَفِيرٌ وَشَهِيقٌ
Ña texeedi danañu nekk ca Safara di yikkat ak a jooy.
107خَالِدِينَ فِيهَا مَا دَامَتِ السَّمَاوَاتُ وَالْأَرْضُ إِلَّا مَا شَاءَ رَبُّكَ ۚ إِنَّ رَبَّكَ فَعَّالٌ لِّمَا يُرِيدُ
Dañu fay béel, nekk fa feek asamaan yi ak suuf si - ndare lu neex sa Boroom - ndax Moom lu ko soob Mu def ko.
108۞ وَأَمَّا الَّذِينَ سُعِدُوا فَفِي الْجَنَّةِ خَالِدِينَ فِيهَا مَا دَامَتِ السَّمَاوَاتُ وَالْأَرْضُ إِلَّا مَا شَاءَ رَبُّكَ ۖ عَطَاءً غَيْرَ مَجْذُوذٍ
Ña texe, danañu nekk fa Àjjana, te dañu fay béel, nekk fa li feek asamaan yi ak suuf si ñi ngi fi - ndare lu neex sa Boroom - mu di ag may gu dul dog mukk.
109فَلَا تَكُ فِي مِرْيَةٍ مِّمَّا يَعْبُدُ هَٰؤُلَاءِ ۚ مَا يَعْبُدُونَ إِلَّا كَمَا يَعْبُدُ آبَاؤُهُم مِّن قَبْلُ ۚ وَإِنَّا لَمُوَفُّوهُمْ نَصِيبَهُمْ غَيْرَ مَنقُوصٍ
Bul am sikki-sàkka ci la ñooñu di jaamu. Ci ña seeni baay daan jaamu bu jëkk rekk lañuy jaamu. Te Nun Dananu mottali seeni cër, te dara du ca wàññiku.
110وَلَقَدْ آتَيْنَا مُوسَى الْكِتَابَ فَاخْتُلِفَ فِيهِ ۚ وَلَوْلَا كَلِمَةٌ سَبَقَتْ مِن رَّبِّكَ لَقُضِيَ بَيْنَهُمْ ۚ وَإِنَّهُمْ لَفِي شَكٍّ مِّنْهُ مُرِيبٍ
Joxoon Nanu Muusaa Téere ba. Ñu wuute ca. Bu dul koon sa kàddug Boroom jiitu woon, kon àtteef na seen diggante. Te ñoom dañu caa am sikki-sàkka gu tar.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
108Aaya

Tekki — Hud 108

Simoore Hud Aaya 108 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña texe, danañu nekk fa Àjjana, te dañu fay béel,…

Simoore Aaya 108/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 106–110. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers