Hud · 109/123
Tekki Waxtaan — Hud
فَلَا تَكُ فِي مِرْيَةٍ مِّمَّا يَعْبُدُ هَٰؤُلَاءِ ۚ مَا يَعْبُدُونَ إِلَّا كَمَا يَعْبُدُ آبَاؤُهُم مِّن قَبْلُ ۚ وَإِنَّا لَمُوَفُّوهُمْ نَصِيبَهُمْ غَيْرَ مَنقُوصٍ ۝١٠٩
Falaa taku fee miryatim mimmmaa ya`budu haaa`ulaaa`; maa ya`budoona illaa kamaa ya`budu aabaaa`uhum min qabl; wa innaa lamuwaf foohum naseebahum ghaira manqoos
📖 Tekkim Wolof
Bul am sikki-sàkka ci la ñooñu di jaamu. Ci ña seeni baay daan jaamu bu jëkk rekk lañuy jaamu. Te Nun Dananu mottali seeni cër, te dara du ca wàññiku.

🎧 Dégg


📜 Aaya 107-111 — Hud

107خَالِدِينَ فِيهَا مَا دَامَتِ السَّمَاوَاتُ وَالْأَرْضُ إِلَّا مَا شَاءَ رَبُّكَ ۚ إِنَّ رَبَّكَ فَعَّالٌ لِّمَا يُرِيدُ
Dañu fay béel, nekk fa feek asamaan yi ak suuf si - ndare lu neex sa Boroom - ndax Moom lu ko soob Mu def ko.
108۞ وَأَمَّا الَّذِينَ سُعِدُوا فَفِي الْجَنَّةِ خَالِدِينَ فِيهَا مَا دَامَتِ السَّمَاوَاتُ وَالْأَرْضُ إِلَّا مَا شَاءَ رَبُّكَ ۖ عَطَاءً غَيْرَ مَجْذُوذٍ
Ña texe, danañu nekk fa Àjjana, te dañu fay béel, nekk fa li feek asamaan yi ak suuf si ñi ngi fi - ndare lu neex sa Boroom - mu di ag may gu dul dog mukk.
109فَلَا تَكُ فِي مِرْيَةٍ مِّمَّا يَعْبُدُ هَٰؤُلَاءِ ۚ مَا يَعْبُدُونَ إِلَّا كَمَا يَعْبُدُ آبَاؤُهُم مِّن قَبْلُ ۚ وَإِنَّا لَمُوَفُّوهُمْ نَصِيبَهُمْ غَيْرَ مَنقُوصٍ
Bul am sikki-sàkka ci la ñooñu di jaamu. Ci ña seeni baay daan jaamu bu jëkk rekk lañuy jaamu. Te Nun Dananu mottali seeni cër, te dara du ca wàññiku.
110وَلَقَدْ آتَيْنَا مُوسَى الْكِتَابَ فَاخْتُلِفَ فِيهِ ۚ وَلَوْلَا كَلِمَةٌ سَبَقَتْ مِن رَّبِّكَ لَقُضِيَ بَيْنَهُمْ ۚ وَإِنَّهُمْ لَفِي شَكٍّ مِّنْهُ مُرِيبٍ
Joxoon Nanu Muusaa Téere ba. Ñu wuute ca. Bu dul koon sa kàddug Boroom jiitu woon, kon àtteef na seen diggante. Te ñoom dañu caa am sikki-sàkka gu tar.
111وَإِنَّ كُلًّا لَّمَّا لَيُوَفِّيَنَّهُمْ رَبُّكَ أَعْمَالَهُمْ ۚ إِنَّهُ بِمَا يَعْمَلُونَ خَبِيرٌ
Fàwwu ñoom ñépp sa Boroom Dana matal seen peyug jëf... Naka Moom ku xam xéll la li ñuy jëf.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
109Aaya

Tekki — Hud 109

Simoore Hud Aaya 109 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bul am sikki-sàkka ci la ñooñu di jaamu. Ci ña…

Simoore Aaya 109/123 — Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Hud Dégg, Hud Tekki, Hud mp3, Hud pdf. Aaya 107–111. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers