Aali Imran · 1/200
Tekki Waxtaan — Simoore Aali Imran
الم ۝١
Alif-Laam-Meeem
📖 Tekkim Wolof
Alif, Lam, Miim.

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-3 — Simoore Aali Imran

1الم
Alif, Lam, Miim.
2اللَّهُ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ الْحَيُّ الْقَيُّومُ
Yàlla mooy Yàlla ! Amul jeneen yàlla ju dul Moom, Aji-dundu la, di Aji-taxawaakoon ci lépp.
3نَزَّلَ عَلَيْكَ الْكِتَابَ بِالْحَقِّ مُصَدِّقًا لِّمَا بَيْنَ يَدَيْهِ وَأَنزَلَ التَّوْرَاةَ وَالْإِنجِيلَ
Moo wàcce ci yaw Téere ba ci dëgg, di feddali la ko jiitu. Moo wàcce Tawreet ak Injiil
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
1Aaya

Tekki — Aali Imran 1

Simoore Aali Imran Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Alif, Lam, Miim.

Simoore Aaya 1/200 — Simoore Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Aali Imran Dégg, Simoore Aali Imran Tekki, Simoore Aali Imran mp3, Simoore Aali Imran pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers