Al-Jinn · 8/28
Tekki Waxtaan — Al-Jinn
وَأَنَّا لَمَسْنَا السَّمَاءَ فَوَجَدْنَاهَا مُلِئَتْ حَرَسًا شَدِيدًا وَشُهُبًا ۝٨
Wa annaa lamasnas sa maaa`a fa wajadnaahaa muli`at harasan shadeedanw wa shuhubaa
📖 Tekkim Wolof
te Nun kat làmbu Nanu asamaan si fekk mu fees dell ak i wattukat ak jumi safara.
🎧 Dégg

📜 Aaya 6-10 — Al-Jinn

6وَأَنَّهُ كَانَ رِجَالٌ مِّنَ الْإِنسِ يَعُوذُونَ بِرِجَالٍ مِّنَ الْجِنِّ فَزَادُوهُمْ رَهَقًا
Amoon ci nit, aw gaay ñu daan sàkku ay muslaay ci aw gaay ñu bokk ci jinne yi ñu faf leen dolli jaaxle (njaaxum).
7وَأَنَّهُمْ ظَنُّوا كَمَا ظَنَنتُمْ أَن لَّن يَبْعَثَ اللَّهُ أَحَدًا
Te ñoom dañoo jortu li ngeen jortoon ci ne Yàlla yónniwul kenn.
8وَأَنَّا لَمَسْنَا السَّمَاءَ فَوَجَدْنَاهَا مُلِئَتْ حَرَسًا شَدِيدًا وَشُهُبًا
te Nun kat làmbu Nanu asamaan si fekk mu fees dell ak i wattukat ak jumi safara.
9وَأَنَّا كُنَّا نَقْعُدُ مِنْهَا مَقَاعِدَ لِلسَّمْعِ ۖ فَمَن يَسْتَمِعِ الْآنَ يَجِدْ لَهُ شِهَابًا رَّصَدًا
Te nun danu fa daan toog di yadu. Leegi nag képp ku fay jéema yëdu ji, dana fa fekk ab jum bu koy tuŋlu.
10وَأَنَّا لَا نَدْرِي أَشَرٌّ أُرِيدَ بِمَن فِي الْأَرْضِ أَمْ أَرَادَ بِهِمْ رَبُّهُمْ رَشَدًا
Te nun sax xamu nu ndax ñi nekk ci suuf si aw ay lees namm ci ñoom walla seen Boroom dafa namm ci ñoom ñu jub.
Al-JinnFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — Al-Jinn 8

Simoore Al-Jinn Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te Nun kat làmbu Nanu asamaan si fekk mu fees…

Simoore Aaya 8/28 — Al-Jinn الجن (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Jinn Dégg, Al-Jinn Tekki, Al-Jinn mp3, Al-Jinn pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers