Al-Jinn · 7/28
Tekki Waxtaan — Al-Jinn
وَأَنَّهُمْ ظَنُّوا كَمَا ظَنَنتُمْ أَن لَّن يَبْعَثَ اللَّهُ أَحَدًا ۝٧
Wa annahum zannoo kamaa zanantum al lany yab`asal laahu ahadaa
📖 Tekkim Wolof
Te ñoom dañoo jortu li ngeen jortoon ci ne Yàlla yónniwul kenn.

🎧 Dégg


📜 Aaya 5-9 — Al-Jinn

5وَأَنَّا ظَنَنَّا أَن لَّن تَقُولَ الْإِنسُ وَالْجِنُّ عَلَى اللَّهِ كَذِبًا
Te foog na ne nit ak jinne amul kenn ku cay fenal Yàlla.
6وَأَنَّهُ كَانَ رِجَالٌ مِّنَ الْإِنسِ يَعُوذُونَ بِرِجَالٍ مِّنَ الْجِنِّ فَزَادُوهُمْ رَهَقًا
Amoon ci nit, aw gaay ñu daan sàkku ay muslaay ci aw gaay ñu bokk ci jinne yi ñu faf leen dolli jaaxle (njaaxum).
7وَأَنَّهُمْ ظَنُّوا كَمَا ظَنَنتُمْ أَن لَّن يَبْعَثَ اللَّهُ أَحَدًا
Te ñoom dañoo jortu li ngeen jortoon ci ne Yàlla yónniwul kenn.
8وَأَنَّا لَمَسْنَا السَّمَاءَ فَوَجَدْنَاهَا مُلِئَتْ حَرَسًا شَدِيدًا وَشُهُبًا
te Nun kat làmbu Nanu asamaan si fekk mu fees dell ak i wattukat ak jumi safara.
9وَأَنَّا كُنَّا نَقْعُدُ مِنْهَا مَقَاعِدَ لِلسَّمْعِ ۖ فَمَن يَسْتَمِعِ الْآنَ يَجِدْ لَهُ شِهَابًا رَّصَدًا
Te nun danu fa daan toog di yadu. Leegi nag képp ku fay jéema yëdu ji, dana fa fekk ab jum bu koy tuŋlu.
Al-JinnFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
7Aaya

Tekki — Al-Jinn 7

Simoore Al-Jinn Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te ñoom dañoo jortu li ngeen jortoon ci ne Yàlla…

Simoore Aaya 7/28 — Al-Jinn الجن (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Jinn Dégg, Al-Jinn Tekki, Al-Jinn mp3, Al-Jinn pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers