Al-Anfal · 1/75
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anfal
يَسْأَلُونَكَ عَنِ الْأَنفَالِ ۖ قُلِ الْأَنفَالُ لِلَّهِ وَالرَّسُولِ ۖ فَاتَّقُوا اللَّهَ وَأَصْلِحُوا ذَاتَ بَيْنِكُمْ ۖ وَأَطِيعُوا اللَّهَ وَرَسُولَهُ إِن كُنتُم مُّؤْمِنِينَ ۝١
Yas`aloonaka `anil anfaali qulil anfaalu lillaahi war Rasooli fattaqul laaha wa ahlihoo zaata bainikum wa atee`ul laaha wa Rasoolahooo in kuntum mu`mineen
📖 Tekkim Wolof
Ña nga lay laaj lu jëm ci màng yi. Neeleen : “Màng yi, Yàlla ak Yonentam ñoo leen moom.” Kon ragal-leen Yàlla te nangeen defar seeni diggante, te ngeen topp Yàlla ak Yonentam ndeem way-gëm ngeen.

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-3 — Simoore Al-Anfal

1يَسْأَلُونَكَ عَنِ الْأَنفَالِ ۖ قُلِ الْأَنفَالُ لِلَّهِ وَالرَّسُولِ ۖ فَاتَّقُوا اللَّهَ وَأَصْلِحُوا ذَاتَ بَيْنِكُمْ ۖ وَأَطِيعُوا اللَّهَ وَرَسُولَهُ إِن كُنتُم مُّؤْمِنِينَ
Ña nga lay laaj lu jëm ci màng yi. Neeleen : “Màng yi, Yàlla ak Yonentam ñoo leen moom.” Kon ragal-leen Yàlla te nangeen defar seeni diggante, te ngeen topp Yàlla ak Yonentam ndeem way-gëm ngeen.
2إِنَّمَا الْمُؤْمِنُونَ الَّذِينَ إِذَا ذُكِرَ اللَّهُ وَجِلَتْ قُلُوبُهُمْ وَإِذَا تُلِيَتْ عَلَيْهِمْ آيَاتُهُ زَادَتْهُمْ إِيمَانًا وَعَلَىٰ رَبِّهِمْ يَتَوَكَّلُونَ
Jullit ya ñooy ña nga xam ne bu ñu tuddee Yàlla seeni xol yëngu. Te bu ñu jàngaa ci ñoom ay laayaam mu yokk seen ngëm. Te ci seen Boroom lañu wékku.
3الَّذِينَ يُقِيمُونَ الصَّلَاةَ وَمِمَّا رَزَقْنَاهُمْ يُنفِقُونَ
Ñooy ña nga xam ne danañu taxawal julli te ca la Nu leen wërsëgal, danañu ca joxe.
Al-AnfalFihi Alxuraan
75Aaya
MedinanRevelation
1Aaya

Tekki — Al-Anfal 1

Simoore Al-Anfal Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña nga lay laaj lu jëm ci màng yi. Neeleen…

Simoore Aaya 1/75 — Simoore Al-Anfal الأنفال (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anfal Dégg, Simoore Al-Anfal Tekki, Simoore Al-Anfal mp3, Simoore Al-Anfal pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers