Al-Baqara · 189/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
۞ يَسْأَلُونَكَ عَنِ الْأَهِلَّةِ ۖ قُلْ هِيَ مَوَاقِيتُ لِلنَّاسِ وَالْحَجِّ ۗ وَلَيْسَ الْبِرُّ بِأَن تَأْتُوا الْبُيُوتَ مِن ظُهُورِهَا وَلَٰكِنَّ الْبِرَّ مَنِ اتَّقَىٰ ۗ وَأْتُوا الْبُيُوتَ مِنْ أَبْوَابِهَا ۚ وَاتَّقُوا اللَّهَ لَعَلَّكُمْ تُفْلِحُونَ ١٨٩
Transliteration
Yas`aloonaka `anil ahillati qul hiya mawaaqeetu linnaasi wal Hajj; wa laisal birru bi an taatul buyoota min zuhoorihaa wa laakinnal birra manit taqaa; waatul buyoota min abwaa bihaa; wattaqullaaha la`allakum tuflihoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Danañu la laaj ci terutel weer yi - Neeleen : “Ay takkukaayu waxtu lañu ci nit ñi ak nattukaayi aj Màkka. Te mbaax [mbaaxu Yàlla] du tekki duggu kër jaare ko ñoot ya [ginnaaw]. Waaye mbaax [jaamu Yàlla] moo di dugge kër ca buntu ya àndak ragal Yàlla. Ay waay ragal-leen Yàlla ndaxtelee ngeen texe ! ”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 187-191 — Al-Baqara
187أُحِلَّ لَكُمْ لَيْلَةَ الصِّيَامِ الرَّفَثُ إِلَىٰ نِسَائِكُمْ ۚ هُنَّ لِبَاسٌ لَّكُمْ وَأَنتُمْ لِبَاسٌ لَّهُنَّ ۗ عَلِمَ اللَّهُ أَنَّكُمْ كُنتُمْ تَخْتَانُونَ أَنفُسَكُمْ فَتَابَ عَلَيْكُمْ وَعَفَا عَنكُمْ ۖ فَالْآنَ بَاشِرُوهُنَّ وَابْتَغُوا مَا كَتَبَ اللَّهُ لَكُمْ ۚ وَكُلُوا وَاشْرَبُوا حَتَّىٰ يَتَبَيَّنَ لَكُمُ الْخَيْطُ الْأَبْيَضُ مِنَ الْخَيْطِ الْأَسْوَدِ مِنَ الْفَجْرِ ۖ ثُمَّ أَتِمُّوا الصِّيَامَ إِلَى اللَّيْلِ ۚ وَلَا تُبَاشِرُوهُنَّ وَأَنتُمْ عَاكِفُونَ فِي الْمَسَاجِدِ ۗ تِلْكَ حُدُودُ اللَّهِ فَلَا تَقْرَبُوهَا ۗ كَذَٰلِكَ يُبَيِّنُ اللَّهُ آيَاتِهِ لِلنَّاسِ لَعَلَّهُمْ يَتَّقُونَ
Dagan na ci yéen ngeen di jote ak seeni soxna ci guddiy weeru koor ; ñoom malaan lañu ci yéen, yéen itam malaan ngeen ci ñoom. Yàlla xam na ne dangeen daan wuruj seen bopp. Mu jéggal leen, jéllale. Kon léegi nangeen jonjonteek ñoom, te ngeen sàkku ci li leen Yàlla dogalal ; te nangeen lekk di naan ba ba ngeen di mën a ràññee wëñ gu weex ak gu ñuul ci fajar gi. Ngeen dale fa mottali koor gi ba guddeeti. Buleen jonjook ñoom fekk yéen a ngi wéet ci jàkka yi di jaamu Yàlla. Loolu deytali Yàlla la : buleen ko jéggi. Noonu la Yàlla di biralee ay laayaam ndaxtelee ñu ragal Yàlla.
188وَلَا تَأْكُلُوا أَمْوَالَكُم بَيْنَكُم بِالْبَاطِلِ وَتُدْلُوا بِهَا إِلَى الْحُكَّامِ لِتَأْكُلُوا فَرِيقًا مِّنْ أَمْوَالِ النَّاسِ بِالْإِثْمِ وَأَنتُمْ تَعْلَمُونَ
Buleen lekk seeni alal ci seeni diggante cig neen, te buleen cay ger àttekat ya ngir mën a labaj ba lekk ci alali nit ñi, ci bàkkaar te xam ko [xéll].
189۞ يَسْأَلُونَكَ عَنِ الْأَهِلَّةِ ۖ قُلْ هِيَ مَوَاقِيتُ لِلنَّاسِ وَالْحَجِّ ۗ وَلَيْسَ الْبِرُّ بِأَن تَأْتُوا الْبُيُوتَ مِن ظُهُورِهَا وَلَٰكِنَّ الْبِرَّ مَنِ اتَّقَىٰ ۗ وَأْتُوا الْبُيُوتَ مِنْ أَبْوَابِهَا ۚ وَاتَّقُوا اللَّهَ لَعَلَّكُمْ تُفْلِحُونَ
Danañu la laaj ci terutel weer yi - Neeleen : “Ay takkukaayu waxtu lañu ci nit ñi ak nattukaayi aj Màkka. Te mbaax [mbaaxu Yàlla] du tekki duggu kër jaare ko ñoot ya [ginnaaw]. Waaye mbaax [jaamu Yàlla] moo di dugge kër ca buntu ya àndak ragal Yàlla. Ay waay ragal-leen Yàlla ndaxtelee ngeen texe ! ”.
190وَقَاتِلُوا فِي سَبِيلِ اللَّهِ الَّذِينَ يُقَاتِلُونَكُمْ وَلَا تَعْتَدُوا ۚ إِنَّ اللَّهَ لَا يُحِبُّ الْمُعْتَدِينَ
Xeexleen ci yoonu Yàlla ak ña leen di xeex, te buleen jéggi dayo di tooñ Yàlla. Yàlla dey soppul ñay jalgati !
191وَاقْتُلُوهُمْ حَيْثُ ثَقِفْتُمُوهُمْ وَأَخْرِجُوهُم مِّنْ حَيْثُ أَخْرَجُوكُمْ ۚ وَالْفِتْنَةُ أَشَدُّ مِنَ الْقَتْلِ ۚ وَلَا تُقَاتِلُوهُمْ عِندَ الْمَسْجِدِ الْحَرَامِ حَتَّىٰ يُقَاتِلُوكُمْ فِيهِ ۖ فَإِن قَاتَلُوكُمْ فَاقْتُلُوهُمْ ۗ كَذَٰلِكَ جَزَاءُ الْكَافِرِينَ
Reyleen leen, fu ngeen fi dajeek ñoom ; Nangeen leen génne fa ñu leen génne woon : [Sànje] moo gën a tar reyaate. Buleen xeex ak ñoom fa Màkka ndare du ñoom ñoo leen fa songu. Bu ñu leen fa songee nag, reyleen leen. Loolu mooy peyub yéefar yi.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
189Aaya
Tekki — Al-Baqara 189
Simoore Al-Baqara Aaya 189 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Danañu la laaj ci terutel weer yi - Neeleen :…Simoore Aaya 189/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 187–191. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








