Al-Mu'minun · 52/118
Tekki Waxtaan — Al-Mu'minun
وَإِنَّ هَٰذِهِ أُمَّتُكُمْ أُمَّةً وَاحِدَةً وَأَنَا رَبُّكُمْ فَاتَّقُونِ ۝٥٢
Wa inna haaziheee ummatukum ummatanw waahidatanw wa Ana Rabbukum fattaqoon
📖 Tekkim Wolof
Te diine jii mooy seen diine, di jenn diine, te maa di seen Boroom. Ragal-leen Ma”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 50-54 — Al-Mu'minun

50وَجَعَلْنَا ابْنَ مَرْيَمَ وَأُمَّهُ آيَةً وَآوَيْنَاهُمَا إِلَىٰ رَبْوَةٍ ذَاتِ قَرَارٍ وَمَعِينٍ
Te Noo def doomi Maryaama [Iisaa] ak yaayam di kéemaan ; te Nu dugal leen ci aw tundu, mu maasee ànd ak bëti-ndox [naan].
51يَا أَيُّهَا الرُّسُلُ كُلُوا مِنَ الطَّيِّبَاتِ وَاعْمَلُوا صَالِحًا ۖ إِنِّي بِمَا تَعْمَلُونَ عَلِيمٌ
Éy yéen Yonent yi ! lekk-leen ci yi teey yi tey jëf u yiw. Man dey kuy xam laa li ngeen di def.
52وَإِنَّ هَٰذِهِ أُمَّتُكُمْ أُمَّةً وَاحِدَةً وَأَنَا رَبُّكُمْ فَاتَّقُونِ
Te diine jii mooy seen diine, di jenn diine, te maa di seen Boroom. Ragal-leen Ma”.
53فَتَقَطَّعُوا أَمْرَهُم بَيْنَهُمْ زُبُرًا ۖ كُلُّ حِزْبٍ بِمَا لَدَيْهِمْ فَرِحُونَ
Séddale nañu seeni mbir ci ay kurél, xaaj bu ne doyloo na la fa moom.
54فَذَرْهُمْ فِي غَمْرَتِهِمْ حَتَّىٰ حِينٍ
Bàyyileen ci seen ngëlëmte loolu ab diir.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
52Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 52

Simoore Al-Mu'minun Aaya 52 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te diine jii mooy seen diine, di jenn diine, te…

Simoore Aaya 52/118 — Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mu'minun Dégg, Al-Mu'minun Tekki, Al-Mu'minun mp3, Al-Mu'minun pdf. Aaya 50–54. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers