An-Nur · 1/64
Tekki Waxtaan — An-Nur
سُورَةٌ أَنزَلْنَاهَا وَفَرَضْنَاهَا وَأَنزَلْنَا فِيهَا آيَاتٍ بَيِّنَاتٍ لَّعَلَّكُمْ تَذَكَّرُونَ ۝١
Sooratun anzalnaahaa wa faradnaahaa wa anzalnaa feehaaa Aayaatim baiyinaatil la`allakum tazakkaroon
📖 Tekkim Wolof
Lii aw saar la wu Nu wàcce farataal ko, mu nekk ci biiram ay laaya yu Nu leeral [faramfàcce] ndax xéy-na ngeen fàttaliku”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 1-3 — An-Nur

1سُورَةٌ أَنزَلْنَاهَا وَفَرَضْنَاهَا وَأَنزَلْنَا فِيهَا آيَاتٍ بَيِّنَاتٍ لَّعَلَّكُمْ تَذَكَّرُونَ
Lii aw saar la wu Nu wàcce farataal ko, mu nekk ci biiram ay laaya yu Nu leeral [faramfàcce] ndax xéy-na ngeen fàttaliku”.
2الزَّانِيَةُ وَالزَّانِي فَاجْلِدُوا كُلَّ وَاحِدٍ مِّنْهُمَا مِائَةَ جَلْدَةٍ ۖ وَلَا تَأْخُذْكُم بِهِمَا رَأْفَةٌ فِي دِينِ اللَّهِ إِن كُنتُمْ تُؤْمِنُونَ بِاللَّهِ وَالْيَوْمِ الْآخِرِ ۖ وَلْيَشْهَدْ عَذَابَهُمَا طَائِفَةٌ مِّنَ الْمُؤْمِنِينَ
Njaalookat bu jigéen ak njaalookat bu góor, nangeen leen dóor téeméeri yar. Te buleen leen yërëm [ci li diine tege] - ndegam gëm ngeen Yàlla ak Bis-pénc. Te itam mbugalum njaalookat yooyu, na ko mbooloo mu bari teewe ci jullit yi.
3الزَّانِي لَا يَنكِحُ إِلَّا زَانِيَةً أَوْ مُشْرِكَةً وَالزَّانِيَةُ لَا يَنكِحُهَا إِلَّا زَانٍ أَوْ مُشْرِكٌ ۚ وَحُرِّمَ ذَٰلِكَ عَلَى الْمُؤْمِنِينَ
Njaalokat bu góor du sëy ak ku dul njaalookat bu jigéen walla bokkaalekat. Njaalookat bu jigéen, kenn du sëy ak moom ku dul njaalookat bu góor walla bokkaalekat te loolu araam na ci jullit ñi.
An-NurFihi Alxuraan
64Aaya
MedinanRevelation
1Aaya

Tekki — An-Nur 1

Simoore An-Nur Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Lii aw saar la wu Nu wàcce farataal ko, mu…

Simoore Aaya 1/64 — An-Nur النور (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nur Dégg, An-Nur Tekki, An-Nur mp3, An-Nur pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers