Al-Waqi'a · 94/96
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Waqi'a
وَتَصْلِيَةُ جَحِيمٍ ۝٩٤
Wa tasliyatu jaheem
📖 Tekkim Wolof
ak xoyomu ca biir Safara.

🎧 Dégg


📜 Aaya 92-96 — Simoore Al-Waqi'a

92وَأَمَّا إِن كَانَ مِنَ الْمُكَذِّبِينَ الضَّالِّينَ
Su fekkee ne nag dafa bokk ca ña daan weddi (dekkiwaat) tey ñu réer sànku,
93فَنُزُلٌ مِّنْ حَمِيمٍ
des na ko teeroo ndox muy wañax,
94وَتَصْلِيَةُ جَحِيمٍ
ak xoyomu ca biir Safara.
95إِنَّ هَٰذَا لَهُوَ حَقُّ الْيَقِينِ
Lii mooy dëgg tigi.
96فَسَبِّحْ بِاسْمِ رَبِّكَ الْعَظِيمِ
Na ngay sàbaal sa turu Boroom, bu Màgg bi !
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
94Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 94

Simoore Al-Waqi'a Aaya 94 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ak xoyomu ca biir Safara.

Simoore Aaya 94/96 — Simoore Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Waqi'a Dégg, Simoore Al-Waqi'a Tekki, Simoore Al-Waqi'a mp3, Simoore Al-Waqi'a pdf. Aaya 92–96. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers