Al-Waqi'a · 93/96
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Waqi'a
فَنُزُلٌ مِّنْ حَمِيمٍ ۝٩٣
Fanuzulum min hameem
📖 Tekkim Wolof
des na ko teeroo ndox muy wañax,

🎧 Dégg


📜 Aaya 91-95 — Simoore Al-Waqi'a

91فَسَلَامٌ لَّكَ مِنْ أَصْحَابِ الْيَمِينِ
dees na ko [teeroo]: “Jàmm ju” bawoo ca waa ndeyjoor.
92وَأَمَّا إِن كَانَ مِنَ الْمُكَذِّبِينَ الضَّالِّينَ
Su fekkee ne nag dafa bokk ca ña daan weddi (dekkiwaat) tey ñu réer sànku,
93فَنُزُلٌ مِّنْ حَمِيمٍ
des na ko teeroo ndox muy wañax,
94وَتَصْلِيَةُ جَحِيمٍ
ak xoyomu ca biir Safara.
95إِنَّ هَٰذَا لَهُوَ حَقُّ الْيَقِينِ
Lii mooy dëgg tigi.
Al-Waqi'aFihi Alxuraan
96Aaya
MeccanRevelation
93Aaya

Tekki — Al-Waqi'a 93

Simoore Al-Waqi'a Aaya 93 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : des na ko teeroo ndox muy wañax,

Simoore Aaya 93/96 — Simoore Al-Waqi'a الواقعة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Waqi'a Dégg, Simoore Al-Waqi'a Tekki, Simoore Al-Waqi'a mp3, Simoore Al-Waqi'a pdf. Aaya 91–95. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers