At-Tawba · 43/129
Tekki Waxtaan — At-Tawba
عَفَا اللَّهُ عَنكَ لِمَ أَذِنتَ لَهُمْ حَتَّىٰ يَتَبَيَّنَ لَكَ الَّذِينَ صَدَقُوا وَتَعْلَمَ الْكَاذِبِينَ ٤٣
Transliteration
Afal laahu `anka lima azinta lahum hattaa yatabai yana lakal lazeena sadaqoo wa ta`lamal kaazibeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Yàlla baal na la li nga leen may dingalul ñu toog te nattuwooleen ba xam ña ca wax dëgg ak ña ca di ay fenkat.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 41-45 — At-Tawba
41انفِرُوا خِفَافًا وَثِقَالًا وَجَاهِدُوا بِأَمْوَالِكُمْ وَأَنفُسِكُمْ فِي سَبِيلِ اللَّهِ ۚ ذَٰلِكُمْ خَيْرٌ لَّكُمْ إِن كُنتُمْ تَعْلَمُونَ
Nangeen di xeex ci woyofaay ak ci dIisaay [sawar ak tàyyeel], nangeen di xeex ci yoonu Yàlla ak seeni alal ak seeni bakkan. Loolu moo gën ci yéen, cëy bu ngeen xamoon.
42لَوْ كَانَ عَرَضًا قَرِيبًا وَسَفَرًا قَاصِدًا لَّاتَّبَعُوكَ وَلَٰكِن بَعُدَتْ عَلَيْهِمُ الشُّقَّةُ ۚ وَسَيَحْلِفُونَ بِاللَّهِ لَوِ اسْتَطَعْنَا لَخَرَجْنَا مَعَكُمْ يُهْلِكُونَ أَنفُسَهُمْ وَاللَّهُ يَعْلَمُ إِنَّهُمْ لَكَاذِبُونَ
Bu doonoon alal juy xoy-xoyi walla muy tukki bu gàtt, kon ñu toppoon la ; waaye ba mu doonee ab xare, ñangay giñ naan : “Bu nu ko mënoon, kon dananu génn ànd ak yaw dem jaay seen bakkan.”. Te Yàlla xam na ne dañuy fen.
43عَفَا اللَّهُ عَنكَ لِمَ أَذِنتَ لَهُمْ حَتَّىٰ يَتَبَيَّنَ لَكَ الَّذِينَ صَدَقُوا وَتَعْلَمَ الْكَاذِبِينَ
Yàlla baal na la li nga leen may dingalul ñu toog te nattuwooleen ba xam ña ca wax dëgg ak ña ca di ay fenkat.
44لَا يَسْتَأْذِنُكَ الَّذِينَ يُؤْمِنُونَ بِاللَّهِ وَالْيَوْمِ الْآخِرِ أَن يُجَاهِدُوا بِأَمْوَالِهِمْ وَأَنفُسِهِمْ ۗ وَاللَّهُ عَلِيمٌ بِالْمُتَّقِينَ
Ña gëm Yàlla, gëm Bis bu mujj ba, duñu la ñaan mukk ndigalul bañ a dem xare ; ñoom kay dañuy xeex ci yoonu Yàlla ak seeni alal ak seeni bakkan. Yàlla xàmmee na ña ragal Yàlla de.
45إِنَّمَا يَسْتَأْذِنُكَ الَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ بِاللَّهِ وَالْيَوْمِ الْآخِرِ وَارْتَابَتْ قُلُوبُهُمْ فَهُمْ فِي رَيْبِهِمْ يَتَرَدَّدُونَ
Ñay laaj ndigal kay ñooy ña gëmul Yàlla ak Bis bu mujj ba, te seeni xol di fer-feri, ñuy jiixi-jaaxa.
At-TawbaFihi Alxuraan
129Aaya
MedinanRevelation
43Aaya
Tekki — At-Tawba 43
Simoore At-Tawba Aaya 43 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla baal na la li nga leen may dingalul ñu…Simoore Aaya 43/129 — At-Tawba التوبة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Tawba Dégg, At-Tawba Tekki, At-Tawba mp3, At-Tawba pdf. Aaya 41–45. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers







