Yunus · 1/109
Tekki Waxtaan — Yunus
الر ۚ تِلْكَ آيَاتُ الْكِتَابِ الْحَكِيمِ ۝١
Alif-Laaam-Raa; tilka Aayaatul Kitaabil Hakeem
📖 Tekkim Wolof
Alif, Laam, Raa. Lii ay laayay Téere bu ñu xereñe lañu.
🎧 Dégg

📜 Aaya 1-3 — Yunus

1الر ۚ تِلْكَ آيَاتُ الْكِتَابِ الْحَكِيمِ
Alif, Laam, Raa. Lii ay laayay Téere bu ñu xereñe lañu.
2أَكَانَ لِلنَّاسِ عَجَبًا أَنْ أَوْحَيْنَا إِلَىٰ رَجُلٍ مِّنْهُمْ أَنْ أَنذِرِ النَّاسَ وَبَشِّرِ الَّذِينَ آمَنُوا أَنَّ لَهُمْ قَدَمَ صِدْقٍ عِندَ رَبِّهِمْ ۗ قَالَ الْكَافِرُونَ إِنَّ هَٰذَا لَسَاحِرٌ مُّبِينٌ
Moo ndax dafa dul yéem ci nit ñi, Nu soloo (xamal) góor gu bokk ci ñoom : “Ndigalul waar nit ñi ci bégal way-gëm ñi te xamal leen ne, am nañu fa seen Boroom dawal bu di dëgg ? Ña weddi ñoom nee nañu : “Lii dey ag njibar gu fés la”.
3إِنَّ رَبَّكُمُ اللَّهُ الَّذِي خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ فِي سِتَّةِ أَيَّامٍ ثُمَّ اسْتَوَىٰ عَلَى الْعَرْشِ ۖ يُدَبِّرُ الْأَمْرَ ۖ مَا مِن شَفِيعٍ إِلَّا مِن بَعْدِ إِذْنِهِ ۚ ذَٰلِكُمُ اللَّهُ رَبُّكُمْ فَاعْبُدُوهُ ۚ أَفَلَا تَذَكَّرُونَ
Yàlla seen Boroom nag Mooy ki bind asamaan yi ak suuf si ci juróom-benni fan, topp Mu yemoo ca gàngunaay ga (Haras), di settantal mbir ya (ndigal ya). Amul kenn ku mën a ramm te du ci ndigalam. Kookoo di seen Boroom. Jaamuleen Ko. Moo ndax dungeen fàttaliku ?
YunusFihi Alxuraan
109Aaya
MeccanRevelation
1Aaya

Tekki — Yunus 1

Simoore Yunus Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Alif, Laam, Raa. Lii ay laayay Téere bu ñu xereñe…

Simoore Aaya 1/109 — Yunus يونس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yunus Dégg, Yunus Tekki, Yunus mp3, Yunus pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers