An-Nahl · 45/128
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nahl
أَفَأَمِنَ الَّذِينَ مَكَرُوا السَّيِّئَاتِ أَن يَخْسِفَ اللَّهُ بِهِمُ الْأَرْضَ أَوْ يَأْتِيَهُمُ الْعَذَابُ مِنْ حَيْثُ لَا يَشْعُرُونَ ۝٤٥
Afa aminal lazeena makarus saiyi aati ai yakhsifal laahu bihimul arda aw yaaa tiyahumul `azaabu min haisu laa yash`uroon
📖 Tekkim Wolof
Ndax am na ci ñuy fexe lu bon, ñu wóolu ne Yàlla du këpp suuf ci sunu kaw, mbaa Mu sadd leen mbugal mu ñu foogul ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 43-47 — Simoore An-Nahl

43وَمَا أَرْسَلْنَا مِن قَبْلِكَ إِلَّا رِجَالًا نُّوحِي إِلَيْهِمْ ۚ فَاسْأَلُوا أَهْلَ الذِّكْرِ إِن كُنتُمْ لَا تَعْلَمُونَ
Yónniwunu woon ca la jiitu lu dul ay góor yu Nu xamaloon [Sunuy ndigal]. Ne leen bu ngeen xamul laajleen woroom xam-xam yi.
44بِالْبَيِّنَاتِ وَالزُّبُرِ ۗ وَأَنزَلْنَا إِلَيْكَ الذِّكْرَ لِتُبَيِّنَ لِلنَّاسِ مَا نُزِّلَ إِلَيْهِمْ وَلَعَلَّهُمْ يَتَفَكَّرُونَ
[Ay Yonent lañu woon] yu indi lay yu leer ak i téere. Te Nu wàcce it Alxuraan ngir nga leeralal nit ñi la ñu wàcce woon ca ñoom, ñu xel-lu [waar ña gëm].
45أَفَأَمِنَ الَّذِينَ مَكَرُوا السَّيِّئَاتِ أَن يَخْسِفَ اللَّهُ بِهِمُ الْأَرْضَ أَوْ يَأْتِيَهُمُ الْعَذَابُ مِنْ حَيْثُ لَا يَشْعُرُونَ
Ndax am na ci ñuy fexe lu bon, ñu wóolu ne Yàlla du këpp suuf ci sunu kaw, mbaa Mu sadd leen mbugal mu ñu foogul ?
46أَوْ يَأْخُذَهُمْ فِي تَقَلُّبِهِمْ فَمَا هُم بِمُعْجِزِينَ
Mbaa mu sadd leen ci seeni tukki ngir ñoom mënuñoo raw [Yàlla].
47أَوْ يَأْخُذَهُمْ عَلَىٰ تَخَوُّفٍ فَإِنَّ رَبَّكُمْ لَرَءُوفٌ رَّحِيمٌ
Mbaa Mu sadd leen cim tiit ? Te sax seen Boroom Aji-ñeewant la, Jaglewaakoon la.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
45Aaya

Tekki — An-Nahl 45

Simoore An-Nahl Aaya 45 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ndax am na ci ñuy fexe lu bon, ñu wóolu…

Simoore Aaya 45/128 — Simoore An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nahl Dégg, Simoore An-Nahl Tekki, Simoore An-Nahl mp3, Simoore An-Nahl pdf. Aaya 43–47. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers