Al-Baqara · 221/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
وَلَا تَنكِحُوا الْمُشْرِكَاتِ حَتَّىٰ يُؤْمِنَّ ۚ وَلَأَمَةٌ مُّؤْمِنَةٌ خَيْرٌ مِّن مُّشْرِكَةٍ وَلَوْ أَعْجَبَتْكُمْ ۗ وَلَا تُنكِحُوا الْمُشْرِكِينَ حَتَّىٰ يُؤْمِنُوا ۚ وَلَعَبْدٌ مُّؤْمِنٌ خَيْرٌ مِّن مُّشْرِكٍ وَلَوْ أَعْجَبَكُمْ ۗ أُولَٰئِكَ يَدْعُونَ إِلَى النَّارِ ۖ وَاللَّهُ يَدْعُو إِلَى الْجَنَّةِ وَالْمَغْفِرَةِ بِإِذْنِهِ ۖ وَيُبَيِّنُ آيَاتِهِ لِلنَّاسِ لَعَلَّهُمْ يَتَذَكَّرُونَ ٢٢١
Transliteration
Wa laatankihul mushrikaati hattaa yu`minn; wa la amatum mu`minatun khairum mim mushrikatinw wa law a`jabatkum; wa laa tunkihul mushrikeena hattaa yu`minoo; wa la`abdummu`minun khairum mimmushrikinw wa law `ajabakum; ulaaa`ika yad`oona ilan Naari wallaahu yad`ooo ilal Jannati walmaghfirati biiznihee wa yubaiyinu Aayaatihee linnaasi la`allahum yatazakkaroon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Buleen takk soxna jigéen ñuy bokkaale li feek gëmuñu, jaam bu jigéen bu gëm moo gën jigéen [ju ñuy tuddeeb sang] juy bokkaale, doontale yéem na leen. Buleen may jabar góor ñuy bokkaale, jaam bu góor moo gën góor [gu ñuy tuddeeb sang] guy bokkaale, doontale yéem na leen. Ñooña dañuy woote jëme Safara ;Yàlla moom di woote jëme Àjjana ak ug njéggal, ci ndigalam. Te dana leeral ay laayaam nit ña ndax ñu fàttaliku [seen Boroom] !
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 219-223 — Al-Baqara
219۞ يَسْأَلُونَكَ عَنِ الْخَمْرِ وَالْمَيْسِرِ ۖ قُلْ فِيهِمَا إِثْمٌ كَبِيرٌ وَمَنَافِعُ لِلنَّاسِ وَإِثْمُهُمَا أَكْبَرُ مِن نَّفْعِهِمَا ۗ وَيَسْأَلُونَكَ مَاذَا يُنفِقُونَ قُلِ الْعَفْوَ ۗ كَذَٰلِكَ يُبَيِّنُ اللَّهُ لَكُمُ الْآيَاتِ لَعَلَّكُمْ تَتَفَكَّرُونَ
- Danañu la laaj lu jëm ci sàngara ak wure. Neel : “Ñoom ñaar bàkkaar bu rëy a nga ca ak njariñi nit ñi ; waaye, la cay bàkkaar ca ñoom ñaar moo ëpp fuuf njariñ ya”. Danañu la laaj : “Lan la ñu war a joxe ci alal? ” Neel : “Aw des.”. Noonu la leen Yàlla di leeralee laaya ya ndaxtelee ngeen di xalaat
220فِي الدُّنْيَا وَالْآخِرَةِ ۗ وَيَسْأَلُونَكَ عَنِ الْيَتَامَىٰ ۖ قُلْ إِصْلَاحٌ لَّهُمْ خَيْرٌ ۖ وَإِن تُخَالِطُوهُمْ فَإِخْوَانُكُمْ ۚ وَاللَّهُ يَعْلَمُ الْمُفْسِدَ مِنَ الْمُصْلِحِ ۚ وَلَوْ شَاءَ اللَّهُ لَأَعْنَتَكُمْ ۚ إِنَّ اللَّهَ عَزِيزٌ حَكِيمٌ
ci àddina ak ca àllaaxira ! Te danañu laaj lu jëm ci jirim yi. Neel : “Yéwénalal-leen [ba seeni alal mën a yokk]. Moo gën bu ngeen jaxasoo ak ñooñu, aayul ndax seeni mbokk lañu ci diine”. Yàlla xàmmee na ñiy yàq ak ñiy defar. Te bu sooboon Yàlla mu sonnal leen. Moom Yàlla moo not lépp, moo xereñ.
221وَلَا تَنكِحُوا الْمُشْرِكَاتِ حَتَّىٰ يُؤْمِنَّ ۚ وَلَأَمَةٌ مُّؤْمِنَةٌ خَيْرٌ مِّن مُّشْرِكَةٍ وَلَوْ أَعْجَبَتْكُمْ ۗ وَلَا تُنكِحُوا الْمُشْرِكِينَ حَتَّىٰ يُؤْمِنُوا ۚ وَلَعَبْدٌ مُّؤْمِنٌ خَيْرٌ مِّن مُّشْرِكٍ وَلَوْ أَعْجَبَكُمْ ۗ أُولَٰئِكَ يَدْعُونَ إِلَى النَّارِ ۖ وَاللَّهُ يَدْعُو إِلَى الْجَنَّةِ وَالْمَغْفِرَةِ بِإِذْنِهِ ۖ وَيُبَيِّنُ آيَاتِهِ لِلنَّاسِ لَعَلَّهُمْ يَتَذَكَّرُونَ
Buleen takk soxna jigéen ñuy bokkaale li feek gëmuñu, jaam bu jigéen bu gëm moo gën jigéen [ju ñuy tuddeeb sang] juy bokkaale, doontale yéem na leen. Buleen may jabar góor ñuy bokkaale, jaam bu góor moo gën góor [gu ñuy tuddeeb sang] guy bokkaale, doontale yéem na leen. Ñooña dañuy woote jëme Safara ;Yàlla moom di woote jëme Àjjana ak ug njéggal, ci ndigalam. Te dana leeral ay laayaam nit ña ndax ñu fàttaliku [seen Boroom] !
222وَيَسْأَلُونَكَ عَنِ الْمَحِيضِ ۖ قُلْ هُوَ أَذًى فَاعْتَزِلُوا النِّسَاءَ فِي الْمَحِيضِ ۖ وَلَا تَقْرَبُوهُنَّ حَتَّىٰ يَطْهُرْنَ ۖ فَإِذَا تَطَهَّرْنَ فَأْتُوهُنَّ مِنْ حَيْثُ أَمَرَكُمُ اللَّهُ ۚ إِنَّ اللَّهَ يُحِبُّ التَّوَّابِينَ وَيُحِبُّ الْمُتَطَهِّرِينَ
- Danañu la laaj lu jëm ci mbërëg . - Neel : “Moom sobe la. Deeleen beru jigéen ña bu ñu nekkee ci mbërëg, buleen jege ba bañuy laab. Suñu laabee, ngeen duggeleen fa Yàlla digle ndax Yàlla sopp na ñay tuub, sopp na itam ñay laabal seen bopp”.
223نِسَاؤُكُمْ حَرْثٌ لَّكُمْ فَأْتُوا حَرْثَكُمْ أَنَّىٰ شِئْتُمْ ۖ وَقَدِّمُوا لِأَنفُسِكُمْ ۚ وَاتَّقُوا اللَّهَ وَاعْلَمُوا أَنَّكُم مُّلَاقُوهُ ۗ وَبَشِّرِ الْمُؤْمِنِينَ
Seeni soxna [jabar] seeni tool lañu ; dikkeleen seeni tool ca na mu leen neexee te ngeen jiital ngir seen bopp, buleen fàtte tudd Yàlla. Te ngeen ragal Yàlla te ngeen xam ne dangeen dajeek Moom. Te nanga bégal way-gëm ña !
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
221Aaya
Tekki — Al-Baqara 221
Simoore Al-Baqara Aaya 221 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Buleen takk soxna jigéen ñuy bokkaale li feek gëmuñu, jaam…Simoore Aaya 221/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 219–223. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








