Al-Ahzab · 10/73
Tekki Waxtaan — Al-Ahzab
إِذْ جَاءُوكُم مِّن فَوْقِكُمْ وَمِنْ أَسْفَلَ مِنكُمْ وَإِذْ زَاغَتِ الْأَبْصَارُ وَبَلَغَتِ الْقُلُوبُ الْحَنَاجِرَ وَتَظُنُّونَ بِاللَّهِ الظُّنُونَا ١٠
Transliteration
Iz jaaa`ookum min fawqikum wa min asfala minkum wa iz zaaghatil absaaru wa balaghatil quloobul hanaajira wa tazunnoona billaahiz zunoonaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ba ñu leen songee, jóge leen kaw ak ci suuf [fépp], seen gët ya di tiiw-tiiwi, ngeen rët ba seeni xol nekk ci seeni boli, ngeen di njort ci Yàlla njort lu nekk...
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 8-12 — Al-Ahzab
8لِّيَسْأَلَ الصَّادِقِينَ عَن صِدْقِهِمْ ۚ وَأَعَدَّ لِلْكَافِرِينَ عَذَابًا أَلِيمًا
ngir laaj [Moom Yàlla] ñi dëggal ci seenug dëggal. Te waajalal na yéefar yi mbugal mu metti.
9يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا اذْكُرُوا نِعْمَةَ اللَّهِ عَلَيْكُمْ إِذْ جَاءَتْكُمْ جُنُودٌ فَأَرْسَلْنَا عَلَيْهِمْ رِيحًا وَجُنُودًا لَّمْ تَرَوْهَا ۚ وَكَانَ اللَّهُ بِمَا تَعْمَلُونَ بَصِيرًا
Éy yéen ñi gëm ! Fàttalikuleen xéewali Yàlla ci yéen, ba leen xarekat ya songee te Nu yebaloon ci ñom ngelaw ak i xarekat yu ngeen gisul. Yàllaa ngi doon gis li ngeen doon def.
10إِذْ جَاءُوكُم مِّن فَوْقِكُمْ وَمِنْ أَسْفَلَ مِنكُمْ وَإِذْ زَاغَتِ الْأَبْصَارُ وَبَلَغَتِ الْقُلُوبُ الْحَنَاجِرَ وَتَظُنُّونَ بِاللَّهِ الظُّنُونَا
Ba ñu leen songee, jóge leen kaw ak ci suuf [fépp], seen gët ya di tiiw-tiiwi, ngeen rët ba seeni xol nekk ci seeni boli, ngeen di njort ci Yàlla njort lu nekk...
11هُنَالِكَ ابْتُلِيَ الْمُؤْمِنُونَ وَزُلْزِلُوا زِلْزَالًا شَدِيدًا
Foofee la Nu nattoo jullit ña, yëngal leen yëngal gu tar.
12وَإِذْ يَقُولُ الْمُنَافِقُونَ وَالَّذِينَ فِي قُلُوبِهِم مَّرَضٌ مَّا وَعَدَنَا اللَّهُ وَرَسُولُهُ إِلَّا غُرُورًا
Ak ba naaféq ya ak ña seen xol tawat di wax naan : “Yàlla ak Yonentam diguñu nu lu dul ay nax”.
Al-AhzabFihi Alxuraan
73Aaya
MedinanRevelation
10Aaya
Tekki — Al-Ahzab 10
Simoore Al-Ahzab Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba ñu leen songee, jóge leen kaw ak ci suuf…Simoore Aaya 10/73 — Al-Ahzab الأحزاب (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Ahzab Dégg, Al-Ahzab Tekki, Al-Ahzab mp3, Al-Ahzab pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








