Al-Ahzab · 9/73
Tekki Waxtaan — Al-Ahzab
يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا اذْكُرُوا نِعْمَةَ اللَّهِ عَلَيْكُمْ إِذْ جَاءَتْكُمْ جُنُودٌ فَأَرْسَلْنَا عَلَيْهِمْ رِيحًا وَجُنُودًا لَّمْ تَرَوْهَا ۚ وَكَانَ اللَّهُ بِمَا تَعْمَلُونَ بَصِيرًا ۝٩
Yaaa aiyuhal lazeena aamanuz kuroo ni`matal laahi `alaikum iz jaaa`atkm junoodun fa arsalnaa `alaihim reehanw wa junoodal lam tarawhaa; wa kaanal laahu bimaa ta`maloona Baseera
📖 Tekkim Wolof
Éy yéen ñi gëm ! Fàttalikuleen xéewali Yàlla ci yéen, ba leen xarekat ya songee te Nu yebaloon ci ñom ngelaw ak i xarekat yu ngeen gisul. Yàllaa ngi doon gis li ngeen doon def.
🎧 Dégg

📜 Aaya 7-11 — Al-Ahzab

7وَإِذْ أَخَذْنَا مِنَ النَّبِيِّينَ مِيثَاقَهُمْ وَمِنكَ وَمِن نُّوحٍ وَإِبْرَاهِيمَ وَمُوسَىٰ وَعِيسَى ابْنِ مَرْيَمَ ۖ وَأَخَذْنَا مِنْهُم مِّيثَاقًا غَلِيظًا
[Fàttalikul] ba Nu jëlee daalante ci Yonent yi ak ci yaw, ak ci Nooh ak ci Ibraahiima, ak Muusaa, ak Iisaa doomu Maryaama : jëloon Nanu ci ñoom daalante bu dëgër, diis,
8لِّيَسْأَلَ الصَّادِقِينَ عَن صِدْقِهِمْ ۚ وَأَعَدَّ لِلْكَافِرِينَ عَذَابًا أَلِيمًا
ngir laaj [Moom Yàlla] ñi dëggal ci seenug dëggal. Te waajalal na yéefar yi mbugal mu metti.
9يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا اذْكُرُوا نِعْمَةَ اللَّهِ عَلَيْكُمْ إِذْ جَاءَتْكُمْ جُنُودٌ فَأَرْسَلْنَا عَلَيْهِمْ رِيحًا وَجُنُودًا لَّمْ تَرَوْهَا ۚ وَكَانَ اللَّهُ بِمَا تَعْمَلُونَ بَصِيرًا
Éy yéen ñi gëm ! Fàttalikuleen xéewali Yàlla ci yéen, ba leen xarekat ya songee te Nu yebaloon ci ñom ngelaw ak i xarekat yu ngeen gisul. Yàllaa ngi doon gis li ngeen doon def.
10إِذْ جَاءُوكُم مِّن فَوْقِكُمْ وَمِنْ أَسْفَلَ مِنكُمْ وَإِذْ زَاغَتِ الْأَبْصَارُ وَبَلَغَتِ الْقُلُوبُ الْحَنَاجِرَ وَتَظُنُّونَ بِاللَّهِ الظُّنُونَا
Ba ñu leen songee, jóge leen kaw ak ci suuf [fépp], seen gët ya di tiiw-tiiwi, ngeen rët ba seeni xol nekk ci seeni boli, ngeen di njort ci Yàlla njort lu nekk...
11هُنَالِكَ ابْتُلِيَ الْمُؤْمِنُونَ وَزُلْزِلُوا زِلْزَالًا شَدِيدًا
Foofee la Nu nattoo jullit ña, yëngal leen yëngal gu tar.
Al-AhzabFihi Alxuraan
73Aaya
MedinanRevelation
9Aaya

Tekki — Al-Ahzab 9

Simoore Al-Ahzab Aaya 9 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Éy yéen ñi gëm ! Fàttalikuleen xéewali Yàlla ci yéen,…

Simoore Aaya 9/73 — Al-Ahzab الأحزاب (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Ahzab Dégg, Al-Ahzab Tekki, Al-Ahzab mp3, Al-Ahzab pdf. Aaya 7–11. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers