Al-Hujurat · 3/18
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hujurat
إِنَّ الَّذِينَ يَغُضُّونَ أَصْوَاتَهُمْ عِندَ رَسُولِ اللَّهِ أُولَٰئِكَ الَّذِينَ امْتَحَنَ اللَّهُ قُلُوبَهُمْ لِلتَّقْوَىٰ ۚ لَهُم مَّغْفِرَةٌ وَأَجْرٌ عَظِيمٌ ۝٣
Innal lazeena yaghud doona aswaatahum `inda Rasoolil laahi ulaaa`ikal lazeenam tah anal laahu quloobahum littaqwaa; lahum maghfiratunw waajrun `azeem
📖 Tekkim Wolof
Ñay suufeel seeni kàddu ci Yonenta bi ñooñee la Yàlla nattu seen xol (fekk ko mu jooy jëm ci ragal Yàlla). Dana ñu am njégël ak pey gu màgg.

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-5 — Simoore Al-Hujurat

1يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تُقَدِّمُوا بَيْنَ يَدَيِ اللَّهِ وَرَسُولِهِ ۖ وَاتَّقُوا اللَّهَ ۚ إِنَّ اللَّهَ سَمِيعٌ عَلِيمٌ
Eey yéen ñi gëm ! Bu leen di jiitu Yàllaa kub Yonentaam. Te ngeen ragal Yàlla di ko watandiku. Ndax Yàlla ku dégg la kuy xam la.
2يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تَرْفَعُوا أَصْوَاتَكُمْ فَوْقَ صَوْتِ النَّبِيِّ وَلَا تَجْهَرُوا لَهُ بِالْقَوْلِ كَجَهْرِ بَعْضِكُمْ لِبَعْضٍ أَن تَحْبَطَ أَعْمَالُكُمْ وَأَنتُمْ لَا تَشْعُرُونَ
Eey yéen ñi gëm! Bu leen di yékkati seen kàddu ci kaw kàddug Yonenta bi, bu leen koy jollmbeeru ay wax, kon ni ngeen di jooruwantee bu (ngeen ko defee), yéen nangay sippi seeni jëf te yëguleen ko.
3إِنَّ الَّذِينَ يَغُضُّونَ أَصْوَاتَهُمْ عِندَ رَسُولِ اللَّهِ أُولَٰئِكَ الَّذِينَ امْتَحَنَ اللَّهُ قُلُوبَهُمْ لِلتَّقْوَىٰ ۚ لَهُم مَّغْفِرَةٌ وَأَجْرٌ عَظِيمٌ
Ñay suufeel seeni kàddu ci Yonenta bi ñooñee la Yàlla nattu seen xol (fekk ko mu jooy jëm ci ragal Yàlla). Dana ñu am njégël ak pey gu màgg.
4إِنَّ الَّذِينَ يُنَادُونَكَ مِن وَرَاءِ الْحُجُرَاتِ أَكْثَرُهُمْ لَا يَعْقِلُونَ
Ña lay woo (yaw Muhammad) di ko jooru di ko jéllóo ci ginnaaw dëkuwaay yi , li ëpp ci ñoom doonu ñu ñu ami xel di ca xalaat.
5وَلَوْ أَنَّهُمْ صَبَرُوا حَتَّىٰ تَخْرُجَ إِلَيْهِمْ لَكَانَ خَيْرًا لَّهُمْ ۚ وَاللَّهُ غَفُورٌ رَّحِيمٌ
Su fekkoon ne dañuy muñ ba baa ngeen génn ci ñoom, mooy gën ci ñoom. Yàlla Jégëlewaakoon la, Jaglewaakoon la.
Al-HujuratFihi Alxuraan
18Aaya
MedinanRevelation
3Aaya

Tekki — Al-Hujurat 3

Simoore Al-Hujurat Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñay suufeel seeni kàddu ci Yonenta bi ñooñee la Yàlla…

Simoore Aaya 3/18 — Simoore Al-Hujurat الحجرات (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hujurat Dégg, Simoore Al-Hujurat Tekki, Simoore Al-Hujurat mp3, Simoore Al-Hujurat pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers