Al-Hujurat · 6/18
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hujurat
يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا إِن جَاءَكُمْ فَاسِقٌ بِنَبَإٍ فَتَبَيَّنُوا أَن تُصِيبُوا قَوْمًا بِجَهَالَةٍ فَتُصْبِحُوا عَلَىٰ مَا فَعَلْتُمْ نَادِمِينَ ۝٦
Yaaa ayyuhal lazeena aamanoo in jaaa`akum faasqum binaba in fatabaiyanooo an tuseeboo qawmam bijahalatin fatusbihoo `alaa maa fa`altum naadimeen
📖 Tekkim Wolof
Eey yéen ñi gëm ! Bu leen ab saay-saay indiley xibaar, na ngeen ko leerlu ndax amaana mu tax ngeen dal ci gawu nit ngir am lënt su ko defee ngeen mujj di ko réccu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 4-8 — Simoore Al-Hujurat

4إِنَّ الَّذِينَ يُنَادُونَكَ مِن وَرَاءِ الْحُجُرَاتِ أَكْثَرُهُمْ لَا يَعْقِلُونَ
Ña lay woo (yaw Muhammad) di ko jooru di ko jéllóo ci ginnaaw dëkuwaay yi , li ëpp ci ñoom doonu ñu ñu ami xel di ca xalaat.
5وَلَوْ أَنَّهُمْ صَبَرُوا حَتَّىٰ تَخْرُجَ إِلَيْهِمْ لَكَانَ خَيْرًا لَّهُمْ ۚ وَاللَّهُ غَفُورٌ رَّحِيمٌ
Su fekkoon ne dañuy muñ ba baa ngeen génn ci ñoom, mooy gën ci ñoom. Yàlla Jégëlewaakoon la, Jaglewaakoon la.
6يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا إِن جَاءَكُمْ فَاسِقٌ بِنَبَإٍ فَتَبَيَّنُوا أَن تُصِيبُوا قَوْمًا بِجَهَالَةٍ فَتُصْبِحُوا عَلَىٰ مَا فَعَلْتُمْ نَادِمِينَ
Eey yéen ñi gëm ! Bu leen ab saay-saay indiley xibaar, na ngeen ko leerlu ndax amaana mu tax ngeen dal ci gawu nit ngir am lënt su ko defee ngeen mujj di ko réccu.
7وَاعْلَمُوا أَنَّ فِيكُمْ رَسُولَ اللَّهِ ۚ لَوْ يُطِيعُكُمْ فِي كَثِيرٍ مِّنَ الْأَمْرِ لَعَنِتُّمْ وَلَٰكِنَّ اللَّهَ حَبَّبَ إِلَيْكُمُ الْإِيمَانَ وَزَيَّنَهُ فِي قُلُوبِكُمْ وَكَرَّهَ إِلَيْكُمُ الْكُفْرَ وَالْفُسُوقَ وَالْعِصْيَانَ ۚ أُولَٰئِكَ هُمُ الرَّاشِدُونَ
Xam leen ne Yonent Yàlla baa ngi ci seen biir. Su fekkoon ne dana leen faral a topp ci mbir yu bari, kon dangeen am coono. Waaye Yàlla moo leen sopploo ngëm taaral ko ci seen xol moo leen bañloo it kéefër, ak ug caay-caay ak ug moy Yàlla. Ñoom ñooñee ñoo di gaay ñu jub ña,
8فَضْلًا مِّنَ اللَّهِ وَنِعْمَةً ۚ وَاللَّهُ عَلِيمٌ حَكِيمٌ
mooy ngëneel lu bawoo fa Yàlla di xéewël. Yàlla Ku Xam la ku Xereñ la.
Al-HujuratFihi Alxuraan
18Aaya
MedinanRevelation
6Aaya

Tekki — Al-Hujurat 6

Simoore Al-Hujurat Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Eey yéen ñi gëm ! Bu leen ab saay-saay indiley…

Simoore Aaya 6/18 — Simoore Al-Hujurat الحجرات (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hujurat Dégg, Simoore Al-Hujurat Tekki, Simoore Al-Hujurat mp3, Simoore Al-Hujurat pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers