Al-Qamar · 22/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
وَلَقَدْ يَسَّرْنَا الْقُرْآنَ لِلذِّكْرِ فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ ۝٢٢
Wa laqad yassamal Quraana liz zikri fahal mim muddakir
📖 Tekkim Wolof
Yombal Nanu Alxuraan ngir ñu fàttalikoo ca. Moo kon ndax kenn dana ca jàjjoo ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 20-24 — Simoore Al-Qamar

20تَنزِعُ النَّاسَ كَأَنَّهُمْ أَعْجَازُ نَخْلٍ مُّنقَعِرٍ
dadoon sempi nit ñi ni ay dàtti tàndarma di buure.
21فَكَيْفَ كَانَ عَذَابِي وَنُذُرِ
Naka mu Sama mbugël ak Samag xuppaate ?
22وَلَقَدْ يَسَّرْنَا الْقُرْآنَ لِلذِّكْرِ فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ
Yombal Nanu Alxuraan ngir ñu fàttalikoo ca. Moo kon ndax kenn dana ca jàjjoo ?
23كَذَّبَتْ ثَمُودُ بِالنُّذُرِ
Waa Samuud weddi woon nañu fàtteli ga?
24فَقَالُوا أَبَشَرًا مِّنَّا وَاحِدًا نَّتَّبِعُهُ إِنَّا إِذًا لَّفِي ضَلَالٍ وَسُعُرٍ
Ñuy wax naan : “Jenn waay ni nun nu di ko topp ? Kon dey nu sànku te réer.
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
22Aaya

Tekki — Al-Qamar 22

Simoore Al-Qamar Aaya 22 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yombal Nanu Alxuraan ngir ñu fàttalikoo ca. Moo kon ndax…

Simoore Aaya 22/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 20–24. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers