Al-Qamar · 23/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
كَذَّبَتْ ثَمُودُ بِالنُّذُرِ ۝٢٣
Kazzabat Samoodu binnuzur
📖 Tekkim Wolof
Waa Samuud weddi woon nañu fàtteli ga?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 21-25 — Simoore Al-Qamar

21فَكَيْفَ كَانَ عَذَابِي وَنُذُرِ
Naka mu Sama mbugël ak Samag xuppaate ?
22وَلَقَدْ يَسَّرْنَا الْقُرْآنَ لِلذِّكْرِ فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ
Yombal Nanu Alxuraan ngir ñu fàttalikoo ca. Moo kon ndax kenn dana ca jàjjoo ?
23كَذَّبَتْ ثَمُودُ بِالنُّذُرِ
Waa Samuud weddi woon nañu fàtteli ga?
24فَقَالُوا أَبَشَرًا مِّنَّا وَاحِدًا نَّتَّبِعُهُ إِنَّا إِذًا لَّفِي ضَلَالٍ وَسُعُرٍ
Ñuy wax naan : “Jenn waay ni nun nu di ko topp ? Kon dey nu sànku te réer.
25أَأُلْقِيَ الذِّكْرُ عَلَيْهِ مِن بَيْنِنَا بَلْ هُوَ كَذَّابٌ أَشِرٌ
Moo ndax dañu koo coqate moom doŋŋ ci nun yónni ko ? Kii daal ab fentaakoon la, bu yées”
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
23Aaya

Tekki — Al-Qamar 23

Simoore Al-Qamar Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waa Samuud weddi woon nañu fàtteli ga?

Simoore Aaya 23/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers