At-Talaq · 8/12
Tekki Waxtaan — At-Talaq
وَكَأَيِّن مِّن قَرْيَةٍ عَتَتْ عَنْ أَمْرِ رَبِّهَا وَرُسُلِهِ فَحَاسَبْنَاهَا حِسَابًا شَدِيدًا وَعَذَّبْنَاهَا عَذَابًا نُّكْرًا ۝٨
Wa ka ayyim min qaryatin `atat `an amri Rabbihaa wa Rusulihee fahaasabnaahaa hisaaban shadeedanw wa `azzabnaahaa `azaaban nukraa
📖 Tekkim Wolof
Aka bari ay dëkk yu moyoon seen ndigëlu boroom ak i Yonentam ! Nu nattu leen nattu bu tar, mbugal leen mbugal mu mitti.

🎧 Dégg


📜 Aaya 6-10 — At-Talaq

6أَسْكِنُوهُنَّ مِنْ حَيْثُ سَكَنتُم مِّن وُجْدِكُمْ وَلَا تُضَارُّوهُنَّ لِتُضَيِّقُوا عَلَيْهِنَّ ۚ وَإِن كُنَّ أُولَاتِ حَمْلٍ فَأَنفِقُوا عَلَيْهِنَّ حَتَّىٰ يَضَعْنَ حَمْلَهُنَّ ۚ فَإِنْ أَرْضَعْنَ لَكُمْ فَآتُوهُنَّ أُجُورَهُنَّ ۖ وَأْتَمِرُوا بَيْنَكُم بِمَعْرُوفٍ ۖ وَإِن تَعَاسَرْتُمْ فَسَتُرْضِعُ لَهُ أُخْرَىٰ
Nangeen di dëkkël jigéen ñi ca fa ngeen dëkk yéen, ca nangeen ko mane. Buleen leen bunduxataal ngir xatal leen. Su fekkee ne dañoo ëmb, na ngeen leen di dundal ba baa ñuy imbi. Suñu, leen nàmpalalee seen doom, nangeen ko fay. Nangeen diisoo ci njekk. Su ngeen ca juuyoo, kon, na ko keneen nàmpal.
7لِيُنفِقْ ذُو سَعَةٍ مِّن سَعَتِهِ ۖ وَمَن قُدِرَ عَلَيْهِ رِزْقُهُ فَلْيُنفِقْ مِمَّا آتَاهُ اللَّهُ ۚ لَا يُكَلِّفُ اللَّهُ نَفْسًا إِلَّا مَا آتَاهَا ۚ سَيَجْعَلُ اللَّهُ بَعْدَ عُسْرٍ يُسْرًا
Ku am alal na joxee na mu woomale ; ku amul alal it na joxee ci kem na ko Yàlla wërsëgële. Yàlla du ga kenn ci lu mu manul, Yàlla dana def yombal ci ginnaaw ag jafe.
8وَكَأَيِّن مِّن قَرْيَةٍ عَتَتْ عَنْ أَمْرِ رَبِّهَا وَرُسُلِهِ فَحَاسَبْنَاهَا حِسَابًا شَدِيدًا وَعَذَّبْنَاهَا عَذَابًا نُّكْرًا
Aka bari ay dëkk yu moyoon seen ndigëlu boroom ak i Yonentam ! Nu nattu leen nattu bu tar, mbugal leen mbugal mu mitti.
9فَذَاقَتْ وَبَالَ أَمْرِهَا وَكَانَ عَاقِبَةُ أَمْرِهَا خُسْرًا
Mosnañu musibam seeni mbir. Ñu mujj yàqule.
10أَعَدَّ اللَّهُ لَهُمْ عَذَابًا شَدِيدًا ۖ فَاتَّقُوا اللَّهَ يَا أُولِي الْأَلْبَابِ الَّذِينَ آمَنُوا ۚ قَدْ أَنزَلَ اللَّهُ إِلَيْكُمْ ذِكْرًا
Yàlla waajal na leen mbugël mu tar. Kon book ragal-leen Yàlla, yéen woroom xel yi, natt gëm. Yàlla wàcce na ci yéen ag fàttali,
At-TalaqFihi Alxuraan
12Aaya
MedinanRevelation
8Aaya

Tekki — At-Talaq 8

Simoore At-Talaq Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Aka bari ay dëkk yu moyoon seen ndigëlu boroom ak…

Simoore Aaya 8/12 — At-Talaq الطلاق (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Talaq Dégg, At-Talaq Tekki, At-Talaq mp3, At-Talaq pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers