At-Tawba · 1/129
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tawba
بَرَاءَةٌ مِّنَ اللَّهِ وَرَسُولِهِ إِلَى الَّذِينَ عَاهَدتُّم مِّنَ الْمُشْرِكِينَ ۝١
Baraaa`atum minal laahi wa Rasooliheee ilal lazeena `anhattum minal mushrikeen
📖 Tekkim Wolof
Lii deñtalu la gu tukkee ci Yàlla ak ub Yonentam ci yéen ak ñoom bokkaalekat ya ngeen bokkal koote :

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 1-3 — Simoore At-Tawba

1بَرَاءَةٌ مِّنَ اللَّهِ وَرَسُولِهِ إِلَى الَّذِينَ عَاهَدتُّم مِّنَ الْمُشْرِكِينَ
Lii deñtalu la gu tukkee ci Yàlla ak ub Yonentam ci yéen ak ñoom bokkaalekat ya ngeen bokkal koote :
2فَسِيحُوا فِي الْأَرْضِ أَرْبَعَةَ أَشْهُرٍ وَاعْلَمُوا أَنَّكُمْ غَيْرُ مُعْجِزِي اللَّهِ ۙ وَأَنَّ اللَّهَ مُخْزِي الْكَافِرِينَ
“Kon doxleen ci suuf si ñeneenti weer ; te nangeen xam ne nag yéen dungeen mën a raw Yàlla te nag Yàlla Kuy gàcceel yéefar yi la.”
3وَأَذَانٌ مِّنَ اللَّهِ وَرَسُولِهِ إِلَى النَّاسِ يَوْمَ الْحَجِّ الْأَكْبَرِ أَنَّ اللَّهَ بَرِيءٌ مِّنَ الْمُشْرِكِينَ ۙ وَرَسُولُهُ ۚ فَإِن تُبْتُمْ فَهُوَ خَيْرٌ لَّكُمْ ۖ وَإِن تَوَلَّيْتُمْ فَاعْلَمُوا أَنَّكُمْ غَيْرُ مُعْجِزِي اللَّهِ ۗ وَبَشِّرِ الَّذِينَ كَفَرُوا بِعَذَابٍ أَلِيمٍ
Te it xamle la gu tukke ci Yàlla ak Yonentam jëm ci nit ñi, ca bisub gën gaa Màggi Aj mooy ne : Yàlla nag Ku deñ la mook Yonentam ci yéefar yi. Bu ngeen rëccoo, tuub, kon mooy gën ci yéen. Bu ngeen dëddoo [nangeen xam ne] dungeen mën a rëcc Yàlla te nanga yëgal ña weddi, mbugal mu metti.
At-TawbaFihi Alxuraan
129Aaya
MedinanRevelation
1Aaya

Tekki — At-Tawba 1

Simoore At-Tawba Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Lii deñtalu la gu tukkee ci Yàlla ak ub Yonentam…

Simoore Aaya 1/129 — Simoore At-Tawba التوبة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tawba Dégg, Simoore At-Tawba Tekki, Simoore At-Tawba mp3, Simoore At-Tawba pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers