Al-'Adiyat · 7/11
Tekki Waxtaan — Simoore Al-'Adiyat
وَإِنَّهُ عَلَىٰ ذَٰلِكَ لَشَهِيدٌ ۝٧
Wa innahu `alaa zaalika la shaheed
📖 Tekkim Wolof
te kat, moom, seede la ci loolu ;

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 5-9 — Simoore Al-'Adiyat

5فَوَسَطْنَ بِهِ جَمْعًا
tey xuus ca biir noon ya.
6إِنَّ الْإِنسَانَ لِرَبِّهِ لَكَنُودٌ
Nit dey, kuy ñàkk deloo Boroomam njukal la ;
7وَإِنَّهُ عَلَىٰ ذَٰلِكَ لَشَهِيدٌ
te kat, moom, seede la ci loolu ;
8وَإِنَّهُ لِحُبِّ الْخَيْرِ لَشَدِيدٌ
te kat moom ku tarla xérlool ci bëgg alal.
9۞ أَفَلَا يَعْلَمُ إِذَا بُعْثِرَ مَا فِي الْقُبُورِ
Xanaa dafa xamul saa su ñu ko jaxasee ci biir bàmmeel,
Al-'AdiyatFihi Alxuraan
11Aaya
MeccanRevelation
7Aaya

Tekki — Al-'Adiyat 7

Simoore Al-'Adiyat Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te kat, moom, seede la ci loolu ;

Simoore Aaya 7/11 — Simoore Al-'Adiyat العاديات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-'Adiyat Dégg, Simoore Al-'Adiyat Tekki, Simoore Al-'Adiyat mp3, Simoore Al-'Adiyat pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers