Al-'Adiyat · 9/11
Tekki Waxtaan — Al-'Adiyat
۞ أَفَلَا يَعْلَمُ إِذَا بُعْثِرَ مَا فِي الْقُبُورِ ۝٩
Afala ya`lamu iza b`uthira ma filquboor
📖 Tekkim Wolof
Xanaa dafa xamul saa su ñu ko jaxasee ci biir bàmmeel,
🎧 Dégg

📜 Aaya 7-11 — Al-'Adiyat

7وَإِنَّهُ عَلَىٰ ذَٰلِكَ لَشَهِيدٌ
te kat, moom, seede la ci loolu ;
8وَإِنَّهُ لِحُبِّ الْخَيْرِ لَشَدِيدٌ
te kat moom ku tarla xérlool ci bëgg alal.
9۞ أَفَلَا يَعْلَمُ إِذَا بُعْثِرَ مَا فِي الْقُبُورِ
Xanaa dafa xamul saa su ñu ko jaxasee ci biir bàmmeel,
10وَحُصِّلَ مَا فِي الصُّدُورِ
te wuñées li nekk ci biir dënn yi,
11إِنَّ رَبَّهُم بِهِمْ يَوْمَئِذٍ لَّخَبِيرٌ
bu keroogee, sa Boroom Ku deñ Kumpa la ci ñoom?
Al-'AdiyatFihi Alxuraan
11Aaya
MeccanRevelation
9Aaya

Tekki — Al-'Adiyat 9

Simoore Al-'Adiyat Aaya 9 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xanaa dafa xamul saa su ñu ko jaxasee ci biir…

Simoore Aaya 9/11 — Al-'Adiyat العاديات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-'Adiyat Dégg, Al-'Adiyat Tekki, Al-'Adiyat mp3, Al-'Adiyat pdf. Aaya 7–11. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers