Al-'Adiyat · 8/11
Tekki Waxtaan — Simoore Al-'Adiyat
وَإِنَّهُ لِحُبِّ الْخَيْرِ لَشَدِيدٌ ۝٨
Wa innahu lihubbil khairi la shadeed
📖 Tekkim Wolof
te kat moom ku tarla xérlool ci bëgg alal.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 6-10 — Simoore Al-'Adiyat

6إِنَّ الْإِنسَانَ لِرَبِّهِ لَكَنُودٌ
Nit dey, kuy ñàkk deloo Boroomam njukal la ;
7وَإِنَّهُ عَلَىٰ ذَٰلِكَ لَشَهِيدٌ
te kat, moom, seede la ci loolu ;
8وَإِنَّهُ لِحُبِّ الْخَيْرِ لَشَدِيدٌ
te kat moom ku tarla xérlool ci bëgg alal.
9۞ أَفَلَا يَعْلَمُ إِذَا بُعْثِرَ مَا فِي الْقُبُورِ
Xanaa dafa xamul saa su ñu ko jaxasee ci biir bàmmeel,
10وَحُصِّلَ مَا فِي الصُّدُورِ
te wuñées li nekk ci biir dënn yi,
Al-'AdiyatFihi Alxuraan
11Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — Al-'Adiyat 8

Simoore Al-'Adiyat Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te kat moom ku tarla xérlool ci bëgg alal.

Simoore Aaya 8/11 — Simoore Al-'Adiyat العاديات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-'Adiyat Dégg, Simoore Al-'Adiyat Tekki, Simoore Al-'Adiyat mp3, Simoore Al-'Adiyat pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers