Simoore Az-Zalzala ci Aarabu ak Wolof

Jàng Simoore Az-Zalzala ak tekkim wolof bu mat sëkk, ak baat. Tekki ayaa bu ne. (8 Aaya — مدنية). Az-Zalzala Dégg, Az-Zalzala Tekki, Az-Zalzala mp3, Az-Zalzala pdf.

Jàng te Dégg Simoore Az-Zalzala

🎧 Aaya
M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
—
x1
bismillah
إِذَا زُلْزِلَتِ الْأَرْضُ زِلْزَالَهَا ۝١
📖 Tekki Aaya 1
Saa su suuf si yëngutoo yëngoom ba,
وَأَخْرَجَتِ الْأَرْضُ أَثْقَالَهَا ۝٢
📖 Tekki Aaya 2
te suuf si génne la mu suuloon,
وَقَالَ الْإِنسَانُ مَا لَهَا ۝٣
📖 Tekki Aaya 3
nit naan : “Ngala man ? ”
يَوْمَئِذٍ تُحَدِّثُ أَخْبَارَهَا ۝٤
📖 Tekki Aaya 4
bu keroogee, ci lay waxtaane ay xibaar,
بِأَنَّ رَبَّكَ أَوْحَىٰ لَهَا ۝٥
📖 Tekki Aaya 5
ci la ko sa Boroom soloo.
يَوْمَئِذٍ يَصْدُرُ النَّاسُ أَشْتَاتًا لِّيُرَوْا أَعْمَالَهُمْ ۝٦
📖 Tekki Aaya 6
Bu keroogee, nit ñéppay génn kenn kenn ngir ñu wan leen seeni jëf.
فَمَن يَعْمَلْ مِثْقَالَ ذَرَّةٍ خَيْرًا يَرَهُ ۝٧
📖 Tekki Aaya 7
Képp ku jëf lu toll ni aw fepp te muy lu baax, dana ko gis,
وَمَن يَعْمَلْ مِثْقَالَ ذَرَّةٍ شَرًّا يَرَهُ ۝٨
📖 Tekki Aaya 8
Képp ku jëf lu toll ni aw fepp su dee lu bon, dana ko gis.
← 98 Az-Zalzala (99/114) 100 →
Jàng Simoore Az-Zalzala ci Wolof – Tekki, Waxtaan ak Baat

99الزلزلة Az-Zalzalah 📚 8 Aaya مدنية



Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers