Simoore Ash-Sharh ci Aarabu ak Wolof

Jàng Simoore Ash-Sharh ak tekkim wolof bu mat sëkk, ak baat. Tekki ayaa bu ne. (8 Aaya — مكية). Ash-Sharh Dégg, Ash-Sharh Tekki, Ash-Sharh mp3, Ash-Sharh pdf.

Jàng te Dégg Simoore Ash-Sharh

🎧 Aaya
M Mishary Rashid Alafasy
M Mahmoud Khalil Al-Husary
A Abdurrahman As-Sudais
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi
A Abdul Basit Abdul Samad
A Ali Al-Hudhaify
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy
A Abu Bakr Ash-Shaatree
M Muhammad Ayyoub
A Abdullah Basfar
A Abdullah Al-Juhani
M Maher Al Muaiqly
x1
أَلَمْ نَشْرَحْ لَكَ صَدْرَكَ ۝١
📖 Tekki Aaya 1
Moo ndax féexalu nu la sa dënn ?
وَوَضَعْنَا عَنكَ وِزْرَكَ ۝٢
📖 Tekki Aaya 2
Te nu teggil la say bàkkaar
الَّذِي أَنقَضَ ظَهْرَكَ ۝٣
📖 Tekki Aaya 3
ya diisaloon sa ginnaaw ?
وَرَفَعْنَا لَكَ ذِكْرَكَ ۝٤
📖 Tekki Aaya 4
Te yékatil nanu la saw tur ?
فَإِنَّ مَعَ الْعُسْرِ يُسْرًا ۝٥
📖 Tekki Aaya 5
Jafe-jafe bu nekk, àndanaak ug yombal !
إِنَّ مَعَ الْعُسْرِ يُسْرًا ۝٦
📖 Tekki Aaya 6
Jafe-jafe bu nekk, àndanaak ug yombal !
فَإِذَا فَرَغْتَ فَانصَبْ ۝٧
📖 Tekki Aaya 7
Te saa yoo féexee, jógël, (julli)
وَإِلَىٰ رَبِّكَ فَارْغَب ۝٨
📖 Tekki Aaya 8
te it na ngay xemmeem jëm ci sa Boroom.
← 93 Ash-Sharh (94/114) 95 →
Jàng Simoore Ash-Sharh ci Wolof – Tekki, Waxtaan ak Baat

94الشرح Ash-Sharh 📚 8 Aaya مكية



Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers