PDF —
8 Aaya Meccan PDF
Built right in your browser — download starts automatically

Simoore Ash-Sharh pdf — Wàcce (Wolof)

Simoore Ash-Sharh pdf Wolof — Wàcce Simoore Ash-Sharh Tekki. Simoore Ash-Sharh (Meccan) 8 Aaya.

← Ad-DuhaSimoore Ash-Sharh At-Tin →


8 Aaya · Meccan · Wolof
bismillah
ﯝﯞﯟﯠﯡ
94:1 Moo ndax féexalu nu la sa dënn ?
ﯢﯣﯤﯥ
94:2 Te nu teggil la say bàkkaar
ﭑﭒﭓﭔ
94:3 ya diisaloon sa ginnaaw ?
ﭕﭖﭗﭘ
94:4 Te yékatil nanu la saw tur ?
ﭙﭚﭛﭜﭝ
94:5 Jafe-jafe bu nekk, àndanaak ug yombal !
ﭞﭟﭠﭡﭢ
94:6 Jafe-jafe bu nekk, àndanaak ug yombal !
ﭣﭤﭥﭦ
94:7 Te saa yoo féexee, jógël, (julli)
ﭧﭨﭩﭪ
94:8 te it na ngay xemmeem jëm ci sa Boroom.

Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 9, 2026

Don't forget us in your sincere prayers