Simoore At-Tin ci Aarabu ak Wolof
Jàng Simoore At-Tin ak tekkim wolof bu mat sëkk, ak baat. Tekki ayaa bu ne. (8 Aaya — مكية). At-Tin Dégg, At-Tin Tekki, At-Tin mp3, At-Tin pdf.Jàng te Dégg Simoore At-Tin
🎧 Aaya
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
—
x1
لَقَدْ خَلَقْنَا الْإِنسَانَ فِي أَحْسَنِ تَقْوِيمٍ ٤
📖 Tekki
Aaya 4
Bind nanu nit ci gën ja rafeti anam.
ثُمَّ رَدَدْنَاهُ أَسْفَلَ سَافِلِينَ ٥
📖 Tekki
Aaya 5
Top, waaye man naa dem ba gëna suufe lépp lu suufe,
إِلَّا الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ فَلَهُمْ أَجْرٌ غَيْرُ مَمْنُونٍ ٦
📖 Tekki
Aaya 6
ba mu des ña gëm tey jëfu yiw : ñoom dananu am pey gu dootul dog.
فَمَا يُكَذِّبُكَ بَعْدُ بِالدِّينِ ٧
📖 Tekki
Aaya 7
Bu loolu wéyee, ana lan moo tax ngay weddi bisub faytoo ba (bis pénc) ?
أَلَيْسَ اللَّهُ بِأَحْكَمِ الْحَاكِمِينَ ٨
📖 Tekki
Aaya 8
Moo xanaa Yàlla dafa dul ki dàqa àtte àttekat yi ?
Jàng Simoore At-Tin ci Wolof – Tekki, Waxtaan ak Baat
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers

