Ash-Sharh · 2/8
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Sharh
وَوَضَعْنَا عَنكَ وِزْرَكَ ۝٢
Wa wa d`ana `anka wizrak
📖 Tekkim Wolof
Te nu teggil la say bàkkaar

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-4 — Simoore Ash-Sharh

1أَلَمْ نَشْرَحْ لَكَ صَدْرَكَ
Moo ndax féexalu nu la sa dënn ?
2وَوَضَعْنَا عَنكَ وِزْرَكَ
Te nu teggil la say bàkkaar
3الَّذِي أَنقَضَ ظَهْرَكَ
ya diisaloon sa ginnaaw ?
4وَرَفَعْنَا لَكَ ذِكْرَكَ
Te yékatil nanu la saw tur ?
Ash-SharhFihi Alxuraan
8Aaya
MeccanRevelation
2Aaya

Tekki — Ash-Sharh 2

Simoore Ash-Sharh Aaya 2 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te nu teggil la say bàkkaar

Simoore Aaya 2/8 — Simoore Ash-Sharh الشرح (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Sharh Dégg, Simoore Ash-Sharh Tekki, Simoore Ash-Sharh mp3, Simoore Ash-Sharh pdf. Aaya 1–4. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers