Ash-Sharh · 6/8
Tekki Waxtaan — Ash-Sharh
إِنَّ مَعَ الْعُسْرِ يُسْرًا ۝٦
Inna ma`al `usri yusra
📖 Tekkim Wolof
Jafe-jafe bu nekk, àndanaak ug yombal !
🎧 Dégg

📜 Aaya 4-8 — Ash-Sharh

4وَرَفَعْنَا لَكَ ذِكْرَكَ
Te yékatil nanu la saw tur ?
5فَإِنَّ مَعَ الْعُسْرِ يُسْرًا
Jafe-jafe bu nekk, àndanaak ug yombal !
6إِنَّ مَعَ الْعُسْرِ يُسْرًا
Jafe-jafe bu nekk, àndanaak ug yombal !
7فَإِذَا فَرَغْتَ فَانصَبْ
Te saa yoo féexee, jógël, (julli)
8وَإِلَىٰ رَبِّكَ فَارْغَب
te it na ngay xemmeem jëm ci sa Boroom.
Ash-SharhFihi Alxuraan
8Aaya
MeccanRevelation
6Aaya

Tekki — Ash-Sharh 6

Simoore Ash-Sharh Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Jafe-jafe bu nekk, àndanaak ug yombal !

Simoore Aaya 6/8 — Ash-Sharh الشرح (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Sharh Dégg, Ash-Sharh Tekki, Ash-Sharh mp3, Ash-Sharh pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers