Al-Anbiya · 3/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
لَاهِيَةً قُلُوبُهُمْ ۗ وَأَسَرُّوا النَّجْوَى الَّذِينَ ظَلَمُوا هَلْ هَٰذَا إِلَّا بَشَرٌ مِّثْلُكُمْ ۖ أَفَتَأْتُونَ السِّحْرَ وَأَنتُمْ تُبْصِرُونَ ۝٣
Laahiyatan quloobuhum; wa asarrun najwal lazeena zalamoo hal haazaa illaa basharum mislukum afataa toonas sihra wa antum tubsiroon
📖 Tekkim Wolof
Càggante nekk na ca seen xol ; tooñkat ya di déeyoo naan : “Ndax kii dafa nekkul mbindéef ni yéen ? Ndax dangeen di topp ag njibar te janook moom ? ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-5 — Simoore Al-Anbiya

1اقْتَرَبَ لِلنَّاسِ حِسَابُهُمْ وَهُمْ فِي غَفْلَةٍ مُّعْرِضُونَ
Waññub [jëfi] nit ñi jegesi na, te ñoom ña nga nuur cig càggante dëddu.
2مَا يَأْتِيهِم مِّن ذِكْرٍ مِّن رَّبِّهِم مُّحْدَثٍ إِلَّا اسْتَمَعُوهُ وَهُمْ يَلْعَبُونَ
Amul lenn lu leen di digal ci Alxuraan di lu bawoo fa seen Boroom, te dégluwaale wuñu kook am po,
3لَاهِيَةً قُلُوبُهُمْ ۗ وَأَسَرُّوا النَّجْوَى الَّذِينَ ظَلَمُوا هَلْ هَٰذَا إِلَّا بَشَرٌ مِّثْلُكُمْ ۖ أَفَتَأْتُونَ السِّحْرَ وَأَنتُمْ تُبْصِرُونَ
Càggante nekk na ca seen xol ; tooñkat ya di déeyoo naan : “Ndax kii dafa nekkul mbindéef ni yéen ? Ndax dangeen di topp ag njibar te janook moom ? ”
4قَالَ رَبِّي يَعْلَمُ الْقَوْلَ فِي السَّمَاءِ وَالْأَرْضِ ۖ وَهُوَ السَّمِيعُ الْعَلِيمُ
Neel : “Sama Boroom xam na lépp lu ñu wax ; ci kaw asamaan yi ak suuf, mooy Aji-dégg di Aji-gis”.
5بَلْ قَالُوا أَضْغَاثُ أَحْلَامٍ بَلِ افْتَرَاهُ بَلْ هُوَ شَاعِرٌ فَلْيَأْتِنَا بِآيَةٍ كَمَا أُرْسِلَ الْأَوَّلُونَ
Waaye ñu naan : “Way-jaxasook ay gént rekk la ! Du lenn lu dul lu mu sos. Ndax [moom Yonent bi] waykat la. Nanu indil kaawtéef ni ñu ko daan yónnee ñu njëkk ña”.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
3Aaya

Tekki — Al-Anbiya 3

Simoore Al-Anbiya Aaya 3 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Càggante nekk na ca seen xol ; tooñkat ya di…

Simoore Aaya 3/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 1–5. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers