Al-Hajj · 11/78
Tekki Waxtaan — Al-Hajj
وَمِنَ النَّاسِ مَن يَعْبُدُ اللَّهَ عَلَىٰ حَرْفٍ ۖ فَإِنْ أَصَابَهُ خَيْرٌ اطْمَأَنَّ بِهِ ۖ وَإِنْ أَصَابَتْهُ فِتْنَةٌ انقَلَبَ عَلَىٰ وَجْهِهِ خَسِرَ الدُّنْيَا وَالْآخِرَةَ ۚ ذَٰلِكَ هُوَ الْخُسْرَانُ الْمُبِينُ ۝١١
Wa minan naasi mai ya`budul laaha `alaa harfin fa in asaabahoo khairunit maanna bihee wa in asaabat hu fitnatunin qalaba `alaa wajhihee khasirad dunyaa wal aakhirah; zaalika huwal khusraanul mubeen
📖 Tekkim Wolof
Ci nit ñi am na ñuy jaamu Yàlla ci genn wet rekk. Tax na bu amee lu baax mu nekk ku dal, bu ko lu naqari dalee, mu soppeeku ca la mu nekke woon, yàqule na ci àddina ak àllaaxira. Te loolu mooy yàqule tigi !

🎧 Dégg


📜 Aaya 9-13 — Al-Hajj

9ثَانِيَ عِطْفِهِ لِيُضِلَّ عَن سَبِيلِ اللَّهِ ۖ لَهُ فِي الدُّنْيَا خِزْيٌ ۖ وَنُذِيقُهُ يَوْمَ الْقِيَامَةِ عَذَابَ الْحَرِيقِ
muy lem loosam [di rëy-rëylu] ngir réerloo [nit ñi] soreel leen yoonu Yàlla. Kooku dey am na ci àddina toroxtaange ; te Dananu ko mosal Bis-pénc ba mbugal muy tàng di lakkaate.
10ذَٰلِكَ بِمَا قَدَّمَتْ يَدَاكَ وَأَنَّ اللَّهَ لَيْسَ بِظَلَّامٍ لِّلْعَبِيدِ
Loolu la yelloo ngir la ñaari yoxoom ya def ci àddina ! Te Yàlla du tooñ jaamam ñi.
11وَمِنَ النَّاسِ مَن يَعْبُدُ اللَّهَ عَلَىٰ حَرْفٍ ۖ فَإِنْ أَصَابَهُ خَيْرٌ اطْمَأَنَّ بِهِ ۖ وَإِنْ أَصَابَتْهُ فِتْنَةٌ انقَلَبَ عَلَىٰ وَجْهِهِ خَسِرَ الدُّنْيَا وَالْآخِرَةَ ۚ ذَٰلِكَ هُوَ الْخُسْرَانُ الْمُبِينُ
Ci nit ñi am na ñuy jaamu Yàlla ci genn wet rekk. Tax na bu amee lu baax mu nekk ku dal, bu ko lu naqari dalee, mu soppeeku ca la mu nekke woon, yàqule na ci àddina ak àllaaxira. Te loolu mooy yàqule tigi !
12يَدْعُو مِن دُونِ اللَّهِ مَا لَا يَضُرُّهُ وَمَا لَا يَنفَعُهُ ۚ ذَٰلِكَ هُوَ الضَّلَالُ الْبَعِيدُ
Mangay jaamu, bàyyi Yàlla, loo xam ne mënu koo lor, mënu koo jariñ. Loolu moo di réer gu sori dëgg !
13يَدْعُو لَمَن ضَرُّهُ أَقْرَبُ مِن نَّفْعِهِ ۚ لَبِئْسَ الْمَوْلَىٰ وَلَبِئْسَ الْعَشِيرُ
Mangay jaamu loo xam ne loram moo gën jegeñnjariñam. Aka bon wéeruwaay te aka bon àndandoo !
Al-HajjFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
11Aaya

Tekki — Al-Hajj 11

Simoore Al-Hajj Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ci nit ñi am na ñuy jaamu Yàlla ci genn…

Simoore Aaya 11/78 — Al-Hajj الحج (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hajj Dégg, Al-Hajj Tekki, Al-Hajj mp3, Al-Hajj pdf. Aaya 9–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers