Al-Furqan · 8/77
Tekki Waxtaan — Al-Furqan
أَوْ يُلْقَىٰ إِلَيْهِ كَنزٌ أَوْ تَكُونُ لَهُ جَنَّةٌ يَأْكُلُ مِنْهَا ۚ وَقَالَ الظَّالِمُونَ إِن تَتَّبِعُونَ إِلَّا رَجُلًا مَّسْحُورًا ۝٨
Aw yulqaaa ilaihi kanzun aw takoonu lahoo jannatuny yaakulu minhaa; wa qaalaz zaalimoona in tattabi`oona illaa rajulam mas hooraa
📖 Tekkim Wolof
Walla mu am ndàmb ? Mbaa mu am tooli dër di ci lekk ?”. Tooñkat ya naan : “Yéen daal toppiwuleen ku dul as waay ju ag njibar jàpp”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 6-10 — Al-Furqan

6قُلْ أَنزَلَهُ الَّذِي يَعْلَمُ السِّرَّ فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۚ إِنَّهُ كَانَ غَفُورًا رَّحِيمًا
Neel : “Ki ko wàcce moo xam mbooti asamaan yeek suuf si. Di ab Jéggalaakon, di Jaglewaakoon.
7وَقَالُوا مَالِ هَٰذَا الرَّسُولِ يَأْكُلُ الطَّعَامَ وَيَمْشِي فِي الْأَسْوَاقِ ۙ لَوْلَا أُنزِلَ إِلَيْهِ مَلَكٌ فَيَكُونَ مَعَهُ نَذِيرًا
Ñu wax ne [ñoom yéefar yi] : “Ana lan moo tax Yonent bii di lekk ñam ak a dox ci ja yi [màrse yi] ? Lan moo tax wutéelsu ko Malaaka mu ànd ak moom di xuppaate ?
8أَوْ يُلْقَىٰ إِلَيْهِ كَنزٌ أَوْ تَكُونُ لَهُ جَنَّةٌ يَأْكُلُ مِنْهَا ۚ وَقَالَ الظَّالِمُونَ إِن تَتَّبِعُونَ إِلَّا رَجُلًا مَّسْحُورًا
Walla mu am ndàmb ? Mbaa mu am tooli dër di ci lekk ?”. Tooñkat ya naan : “Yéen daal toppiwuleen ku dul as waay ju ag njibar jàpp”.
9انظُرْ كَيْفَ ضَرَبُوا لَكَ الْأَمْثَالَ فَضَلُّوا فَلَا يَسْتَطِيعُونَ سَبِيلًا
Gisal ni ñu lay méngaléelee ! Dañuy sànku te amuñu ca wenn yoon.
10تَبَارَكَ الَّذِي إِن شَاءَ جَعَلَ لَكَ خَيْرًا مِّن ذَٰلِكَ جَنَّاتٍ تَجْرِي مِن تَحْتِهَا الْأَنْهَارُ وَيَجْعَل لَّكَ قُصُورًا
Yàlla ju barkeel ja nga xam ne bu Ko sooboon Mu defal la ci loolu Àjjana joo xam ay dex dañuy daw ci suufam ; Mu defal la it ay jénde.
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — Al-Furqan 8

Simoore Al-Furqan Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Walla mu am ndàmb ? Mbaa mu am tooli dër…

Simoore Aaya 8/77 — Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Furqan Dégg, Al-Furqan Tekki, Al-Furqan mp3, Al-Furqan pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers