Al-Ahzab · 61/73
Tekki Waxtaan — Al-Ahzab
مَّلْعُونِينَ ۖ أَيْنَمَا ثُقِفُوا أُخِذُوا وَقُتِّلُوا تَقْتِيلًا ۝٦١
Mal`ooneena ainamaa suqifoo ukhizoo wa quttiloo taqteelaa
📖 Tekkim Wolof
Muy ñuñu rëbb. Fu ñu jublu, ñu faagaagal leen :
🎧 Dégg

📜 Aaya 59-63 — Al-Ahzab

59يَا أَيُّهَا النَّبِيُّ قُل لِّأَزْوَاجِكَ وَبَنَاتِكَ وَنِسَاءِ الْمُؤْمِنِينَ يُدْنِينَ عَلَيْهِنَّ مِن جَلَابِيبِهِنَّ ۚ ذَٰلِكَ أَدْنَىٰ أَن يُعْرَفْنَ فَلَا يُؤْذَيْنَ ۗ وَكَانَ اللَّهُ غَفُورًا رَّحِيمًا
Éy yaw Yonent bi ! Waxal say soxna ak say doom yu jigéen ak jigéeni jullit ñi, ñuy muur seenu yaram : ci la ñu leen di gën a xame te kenn duleen di xas. Yàlla, Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la.
60۞ لَّئِن لَّمْ يَنتَهِ الْمُنَافِقُونَ وَالَّذِينَ فِي قُلُوبِهِم مَّرَضٌ وَالْمُرْجِفُونَ فِي الْمَدِينَةِ لَنُغْرِيَنَّكَ بِهِمْ ثُمَّ لَا يُجَاوِرُونَكَ فِيهَا إِلَّا قَلِيلًا
Su fekkee ne naaféq yeek lëjëlkat yeek woroom xel yu tawat yi dëkk [Medina] bàyyiwuñu, Danaa xiir ci seen kaw, te kon lim bu néew moo ca déeti dëkkaale ak yéen.
61مَّلْعُونِينَ ۖ أَيْنَمَا ثُقِفُوا أُخِذُوا وَقُتِّلُوا تَقْتِيلًا
Muy ñuñu rëbb. Fu ñu jublu, ñu faagaagal leen :
62سُنَّةَ اللَّهِ فِي الَّذِينَ خَلَوْا مِن قَبْلُ ۖ وَلَن تَجِدَ لِسُنَّةِ اللَّهِ تَبْدِيلًا
Lii mooy sunnas Yàlla, ab dogalam ci ña fi jiitu woon te sunnas Yàlla du soppiku mukk.
63يَسْأَلُكَ النَّاسُ عَنِ السَّاعَةِ ۖ قُلْ إِنَّمَا عِلْمُهَا عِندَ اللَّهِ ۚ وَمَا يُدْرِيكَ لَعَلَّ السَّاعَةَ تَكُونُ قَرِيبًا
Nit ñaa ngi lay laaj ci mbiri Bis-pénc ba. Waxal ne : “Yàllaa ko xam”. Te yaw sax loo ci xam ? Amaana Bis-pénc ba di lu jegeñ.
Al-AhzabFihi Alxuraan
73Aaya
MedinanRevelation
61Aaya

Tekki — Al-Ahzab 61

Simoore Al-Ahzab Aaya 61 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Muy ñuñu rëbb. Fu ñu jublu, ñu faagaagal leen :

Simoore Aaya 61/73 — Al-Ahzab الأحزاب (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Ahzab Dégg, Al-Ahzab Tekki, Al-Ahzab mp3, Al-Ahzab pdf. Aaya 59–63. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers