Al-Ahzab · 62/73
Tekki Waxtaan — Al-Ahzab
سُنَّةَ اللَّهِ فِي الَّذِينَ خَلَوْا مِن قَبْلُ ۖ وَلَن تَجِدَ لِسُنَّةِ اللَّهِ تَبْدِيلًا ۝٦٢
Sunnatal laahi fil lazeena khalaw min qablu wa lan tajida lisunnatil laahi tabdeelaa
📖 Tekkim Wolof
Lii mooy sunnas Yàlla, ab dogalam ci ña fi jiitu woon te sunnas Yàlla du soppiku mukk.
🎧 Dégg

📜 Aaya 60-64 — Al-Ahzab

60۞ لَّئِن لَّمْ يَنتَهِ الْمُنَافِقُونَ وَالَّذِينَ فِي قُلُوبِهِم مَّرَضٌ وَالْمُرْجِفُونَ فِي الْمَدِينَةِ لَنُغْرِيَنَّكَ بِهِمْ ثُمَّ لَا يُجَاوِرُونَكَ فِيهَا إِلَّا قَلِيلًا
Su fekkee ne naaféq yeek lëjëlkat yeek woroom xel yu tawat yi dëkk [Medina] bàyyiwuñu, Danaa xiir ci seen kaw, te kon lim bu néew moo ca déeti dëkkaale ak yéen.
61مَّلْعُونِينَ ۖ أَيْنَمَا ثُقِفُوا أُخِذُوا وَقُتِّلُوا تَقْتِيلًا
Muy ñuñu rëbb. Fu ñu jublu, ñu faagaagal leen :
62سُنَّةَ اللَّهِ فِي الَّذِينَ خَلَوْا مِن قَبْلُ ۖ وَلَن تَجِدَ لِسُنَّةِ اللَّهِ تَبْدِيلًا
Lii mooy sunnas Yàlla, ab dogalam ci ña fi jiitu woon te sunnas Yàlla du soppiku mukk.
63يَسْأَلُكَ النَّاسُ عَنِ السَّاعَةِ ۖ قُلْ إِنَّمَا عِلْمُهَا عِندَ اللَّهِ ۚ وَمَا يُدْرِيكَ لَعَلَّ السَّاعَةَ تَكُونُ قَرِيبًا
Nit ñaa ngi lay laaj ci mbiri Bis-pénc ba. Waxal ne : “Yàllaa ko xam”. Te yaw sax loo ci xam ? Amaana Bis-pénc ba di lu jegeñ.
64إِنَّ اللَّهَ لَعَنَ الْكَافِرِينَ وَأَعَدَّ لَهُمْ سَعِيرًا
Yàlla rëbb na yéefar yi te waajalal na leen aw safara,
Al-AhzabFihi Alxuraan
73Aaya
MedinanRevelation
62Aaya

Tekki — Al-Ahzab 62

Simoore Al-Ahzab Aaya 62 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Lii mooy sunnas Yàlla, ab dogalam ci ña fi jiitu…

Simoore Aaya 62/73 — Al-Ahzab الأحزاب (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Ahzab Dégg, Al-Ahzab Tekki, Al-Ahzab mp3, Al-Ahzab pdf. Aaya 60–64. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers