Al-Ahzab · 73/73
Tekki Waxtaan — Al-Ahzab
لِّيُعَذِّبَ اللَّهُ الْمُنَافِقِينَ وَالْمُنَافِقَاتِ وَالْمُشْرِكِينَ وَالْمُشْرِكَاتِ وَيَتُوبَ اللَّهُ عَلَى الْمُؤْمِنِينَ وَالْمُؤْمِنَاتِ ۗ وَكَانَ اللَّهُ غَفُورًا رَّحِيمًا ۝٧٣
Liyu `azzibal laahul munaafiqeena wal munaafiqaati walmushrikeena wal mushrikaati wa yatoobal laahu `alal mu`mineena walmu`minaat; wa kaanal laahu Ghafoorar Raheema
📖 Tekkim Wolof
[Ci loolu] Yàlla dana mbugal naaféq yu góor yeek yu jigéen, ak bokkaalekat yu góor yeek yu jigéen yi te Dana nangu tuubug jullit yu góor yeek yu jigéen yi. Yàlla Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la.

🎧 Dégg


📜 Aaya 71-73 — Al-Ahzab

71يُصْلِحْ لَكُمْ أَعْمَالَكُمْ وَيَغْفِرْ لَكُمْ ذُنُوبَكُمْ ۗ وَمَن يُطِعِ اللَّهَ وَرَسُولَهُ فَقَدْ فَازَ فَوْزًا عَظِيمًا
kon dey Dana leen yéwénalal seeni jëf, jéggal leen it seeni bàkkaar. Te képp kuy topp Yàlla ak ub Yonentam, dana texe texe gu màgg.
72إِنَّا عَرَضْنَا الْأَمَانَةَ عَلَى السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَالْجِبَالِ فَأَبَيْنَ أَن يَحْمِلْنَهَا وَأَشْفَقْنَ مِنْهَا وَحَمَلَهَا الْإِنسَانُ ۖ إِنَّهُ كَانَ ظَلُومًا جَهُولًا
Gaaral Nanu ndénkaan lii asamaan yeek suuf si ak tundi doj yi . Ñu lànk koo yenu ngir ug ragal ko, nit moo ñëw ne ko fànkul yenu ko ; te nit nekk ab tooñaakoon bu xamadi.
73لِّيُعَذِّبَ اللَّهُ الْمُنَافِقِينَ وَالْمُنَافِقَاتِ وَالْمُشْرِكِينَ وَالْمُشْرِكَاتِ وَيَتُوبَ اللَّهُ عَلَى الْمُؤْمِنِينَ وَالْمُؤْمِنَاتِ ۗ وَكَانَ اللَّهُ غَفُورًا رَّحِيمًا
[Ci loolu] Yàlla dana mbugal naaféq yu góor yeek yu jigéen, ak bokkaalekat yu góor yeek yu jigéen yi te Dana nangu tuubug jullit yu góor yeek yu jigéen yi. Yàlla Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la.
Al-AhzabFihi Alxuraan
73Aaya
MedinanRevelation
73Aaya

Tekki — Al-Ahzab 73

Simoore Al-Ahzab Aaya 73 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Ci loolu] Yàlla dana mbugal naaféq yu góor yeek yu…

Simoore Aaya 73/73 — Al-Ahzab الأحزاب (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Ahzab Dégg, Al-Ahzab Tekki, Al-Ahzab mp3, Al-Ahzab pdf. Aaya 71–73. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers