Al-Jathiya · 30/37
Tekki Waxtaan — Al-Jathiya
فَأَمَّا الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ فَيُدْخِلُهُمْ رَبُّهُمْ فِي رَحْمَتِهِ ۚ ذَٰلِكَ هُوَ الْفَوْزُ الْمُبِينُ ٣٠
Transliteration
Fa ammal lazeena aamaanoo wa `amilus saalihaati fayudkhiluhum Rabbuhum fee rahmatih; zaalika huwal fawzul mubeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ña gëmoon te daan jëf yiw, sa Boroom dana leen tàbbal ci biir yërmaandeem. loolu moo di texe gu màgg ga.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 28-32 — Al-Jathiya
28وَتَرَىٰ كُلَّ أُمَّةٍ جَاثِيَةً ۚ كُلُّ أُمَّةٍ تُدْعَىٰ إِلَىٰ كِتَابِهَا الْيَوْمَ تُجْزَوْنَ مَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Ca ngay gise xeet wu nërméelu. Xeet wu ca nekk ñu di ko woo (ngir jox ko ab téereem ba ay jëfëm nekk). Te naan ko bis niki tey dees na leen fay li ngeen daan jëf.
29هَٰذَا كِتَابُنَا يَنطِقُ عَلَيْكُم بِالْحَقِّ ۚ إِنَّا كُنَّا نَسْتَنسِخُ مَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Sunub Téere bii nag. Di àddu ci yéen dëgg ndax ci la nu daan bind li ngeen daan jëf”.
30فَأَمَّا الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ فَيُدْخِلُهُمْ رَبُّهُمْ فِي رَحْمَتِهِ ۚ ذَٰلِكَ هُوَ الْفَوْزُ الْمُبِينُ
Ña gëmoon te daan jëf yiw, sa Boroom dana leen tàbbal ci biir yërmaandeem. loolu moo di texe gu màgg ga.
31وَأَمَّا الَّذِينَ كَفَرُوا أَفَلَمْ تَكُنْ آيَاتِي تُتْلَىٰ عَلَيْكُمْ فَاسْتَكْبَرْتُمْ وَكُنتُمْ قَوْمًا مُّجْرِمِينَ
Ña weddi woon : “Xanaa Sunuy kàddu daawuloon wàcci ca ñoom ? Ñuy rëy-rëylu ak a tooñ di jalgati”.
32وَإِذَا قِيلَ إِنَّ وَعْدَ اللَّهِ حَقٌّ وَالسَّاعَةُ لَا رَيْبَ فِيهَا قُلْتُم مَّا نَدْرِي مَا السَّاعَةُ إِن نَّظُنُّ إِلَّا ظَنًّا وَمَا نَحْنُ بِمُسْتَيْقِنِينَ
Te bu ñu leen waxaan ne : “digub Yàlla bii dëgg la de ; te it Bis Pénc ba sikkuwul”, ngeen daan tontu ne : “Nun sax xamunu luy Bis Pénc ba ; am nanu ci ay njortu te wóoluwu nu ko.
Al-JathiyaFihi Alxuraan
37Aaya
MeccanRevelation
30Aaya
Tekki — Al-Jathiya 30
Simoore Al-Jathiya Aaya 30 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña gëmoon te daan jëf yiw, sa Boroom dana leen…Simoore Aaya 30/37 — Al-Jathiya الجاثية (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Jathiya Dégg, Al-Jathiya Tekki, Al-Jathiya mp3, Al-Jathiya pdf. Aaya 28–32. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








