Al-Jathiya · 31/37
Tekki Waxtaan — Al-Jathiya
وَأَمَّا الَّذِينَ كَفَرُوا أَفَلَمْ تَكُنْ آيَاتِي تُتْلَىٰ عَلَيْكُمْ فَاسْتَكْبَرْتُمْ وَكُنتُمْ قَوْمًا مُّجْرِمِينَ ۝٣١
Wa ammal lazeena kafarooo afalam takun Aayaatee tutlaa `alaikum fastakbartum wa kuntum qawmam mujrimeen
📖 Tekkim Wolof
Ña weddi woon : “Xanaa Sunuy kàddu daawuloon wàcci ca ñoom ? Ñuy rëy-rëylu ak a tooñ di jalgati”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 29-33 — Al-Jathiya

29هَٰذَا كِتَابُنَا يَنطِقُ عَلَيْكُم بِالْحَقِّ ۚ إِنَّا كُنَّا نَسْتَنسِخُ مَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Sunub Téere bii nag. Di àddu ci yéen dëgg ndax ci la nu daan bind li ngeen daan jëf”.
30فَأَمَّا الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ فَيُدْخِلُهُمْ رَبُّهُمْ فِي رَحْمَتِهِ ۚ ذَٰلِكَ هُوَ الْفَوْزُ الْمُبِينُ
Ña gëmoon te daan jëf yiw, sa Boroom dana leen tàbbal ci biir yërmaandeem. loolu moo di texe gu màgg ga.
31وَأَمَّا الَّذِينَ كَفَرُوا أَفَلَمْ تَكُنْ آيَاتِي تُتْلَىٰ عَلَيْكُمْ فَاسْتَكْبَرْتُمْ وَكُنتُمْ قَوْمًا مُّجْرِمِينَ
Ña weddi woon : “Xanaa Sunuy kàddu daawuloon wàcci ca ñoom ? Ñuy rëy-rëylu ak a tooñ di jalgati”.
32وَإِذَا قِيلَ إِنَّ وَعْدَ اللَّهِ حَقٌّ وَالسَّاعَةُ لَا رَيْبَ فِيهَا قُلْتُم مَّا نَدْرِي مَا السَّاعَةُ إِن نَّظُنُّ إِلَّا ظَنًّا وَمَا نَحْنُ بِمُسْتَيْقِنِينَ
Te bu ñu leen waxaan ne : “digub Yàlla bii dëgg la de ; te it Bis Pénc ba sikkuwul”, ngeen daan tontu ne : “Nun sax xamunu luy Bis Pénc ba ; am nanu ci ay njortu te wóoluwu nu ko.
33وَبَدَا لَهُمْ سَيِّئَاتُ مَا عَمِلُوا وَحَاقَ بِهِم مَّا كَانُوا بِهِ يَسْتَهْزِئُونَ
Ñu ne gegg ca [ñaatéefi ] seen jëf ya. Lañu daan yejje gaw leen.
Al-JathiyaFihi Alxuraan
37Aaya
MeccanRevelation
31Aaya

Tekki — Al-Jathiya 31

Simoore Al-Jathiya Aaya 31 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña weddi woon : “Xanaa Sunuy kàddu daawuloon wàcci ca…

Simoore Aaya 31/37 — Al-Jathiya الجاثية (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Jathiya Dégg, Al-Jathiya Tekki, Al-Jathiya mp3, Al-Jathiya pdf. Aaya 29–33. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers